Senegaal wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Rotlink (waxtaancëru)
m fixing dead links
Ibou (waxtaancëru)
Rëdd 81 :
 
----
[[Dencukaay:Abdoulaye_Wade_in_16-05-2007.jpg|vignette|A. Wàdd, mi nekkkenn ci jii jamono njiitulnjiiti Senegaal]]
Mii menn la ci réew yi gën a am demokaraasi te gën a dal ci Afrig, ndaxte genn [[daaneel nguur]] (coups d'État) masu fee am, « Senegaal niki roytéef »<ref>[http://www.africa-catalunya.org/congres/pdfs/marut.pdf « am na nu ñu gise Senegaal niki roytéef ci saafara xuloo yeek xeex yi ? »] (table-ronde régionale sur le Sénégal animée par Jean-Claude Marut, CEAN-IEP de Bordeaux, 15 janvier 2004)</ref> yagg nañu koo joxe, wone ko ngir ñu roy ci, ba tee ay yi di fi am ak doonte [[Amnesty International]] mi ngi ñaawlu yenn jàpp yi yor mbubum politig<ref>[http://web.archive.org/web/20071013220931/http://web.amnesty.org/report2006/sen-summary-fra#2 Rapport 2006 d'Amnesty Internation] jàppug Idriisa Sekk</ref>{{,}}<ref>[http://thereport.amnesty.org/fra/Regions/Africa/Senegal Rapport 2007 d'Amnesty International] bàyyig Idriisa Sekk, ak setal gi nu ko def ci mbooleem li ñu ko toppe woon</ref>.