Bëj-gànnaaru Afrig wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 96 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q27381 (translate me)
JimeoWan (waxtaancëru)
m coppite yu néewal, dindi lëkkalekaay bu dee
Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Africa-countries-northern.svg|right|Lonkoyoonu Afrig ak Réewi Bëj-gànnaaru Afrig.|]]
'''Bëj-gànnaaru Afrig''' mooy [[Diwaan|diwaanu]] Afrig bi féete ci li nekk ci kawu [[tàkk gu [[Sahara]].
 
Mooy la nuy faral di wax ''Afrig gu weex'' gi, ndax melokaanu ña fa dëkk, bii baat day safaano ak '''Afrig gu ñuul''' gi, di tekki [[Afrig gu bëj-saalumu-Sahara]].
 
[[Dencukaay:Africa-countries-northern.svg|right|Lonkoyoonu Afrig ak Réewi Bëj-gànnaaru Afrig.|]]
== Séwógaraafi ==
 
Réewi bëj-gànnaaru AfrikAfrig :
* [[Dencukaay:Flag of Algeria.svg|border|20px|raaya]] [[Alseeri]]
* [[Dencukaay:Flag of Egypt.svg|19px|border|raaya]] [[Isipt]]
Ligne 14 ⟶ 16 :
 
== Taariix ==
* Ci jamono ju yagg ja «Afrig» da doon jëmmal diwaanu [[Kaartaas]], mooy réewu Tiniisi gu tay. Afrik ab diwaanu Nguuru Rom gu Mag ga la woon . Bi [[jullit]] yi ñëwee, baat bi dañ kaa soppi, araabal ko [[Ifriqiya]].
* [[Beerbeer]] yi, ñooy way dëkk yiñ ni ñoo njëkk ci bëj-gànnaaru Afrig.
* [[Maghreb]] (sowu ci araab), moo ëmb réew yii: [[Gànnaar]], [[Marok]], [[Alseeri]], [[Tiniisi]] ak [[Libi]].
* «Afrig gu weex» bu njëkk da doon jëmmal barabu Afrig bi ay nit yu xees dëkkee: [[Marok]], [[Alseeri]], [[Tiniisi]], [[Libi]], [[Esipt]]. Waaye tay baat bi liñ kay jëfëndikoo bariwul.
 
* Ci jamono ju yagg ja « Afrig » da doon jëmmal diwaanu [[Kaartaas]], mooy réewu Tiniisi gu tay. Afrik ab diwaanu Nguuru Rom gu Mag ga la woon . Bi [[jullit]] yi ñëwee, baat bi dañ kaa soppi, araabal ko [[Ifriqiya]].
* [http://www.north-of-africa.com/ North of Africa]
* [[Beerbeer]] yi, ñooy way dëkk yiñ ni ñoo njëkk ci bëj-gànnaaru Afrig.
* [[Maghreb]] (sowu ci araab), moo ëmb réew yii : [[Gànnaar]], [[Marok]], [[Alseeri]], [[Tiniisi]] ak [[Libi]].
* « Afrig gu weex » bu njëkk da doon jëmmal barabu Afrig bi ay nit yu xees dëkkee : [[Marok]], [[Alseeri]], [[Tiniisi]], [[Libi]], [[Esipt]]. Waaye tay baat bi liñ kay jëfëndikoo bariwul.
 
{{diwaaniafrik}}