Royuwaay:Nataalu ayubés bi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
JimeoWan (waxtaancëru)
Nataalu ayubés 35 ci atum 2014 : Dakaar
Rëdd 4 :
<center>'''Nataalu ayubés bi'''</center>
|-
|[[Dencukaay:Dakar-Indépendance.jpg|thumb|centre|350px]]
|[[Image:Sëriñ Saaliwu Mbàkke.jpg|thumb|center|350px| Sëriñ Saaliwu MBÀKKE, juróoméelu xalifab Tuubaa, ca njàngum alxuraan ma]]
 
'''[[Sëriñ Saaliwu]]''' mi ngi gane àdduna, ca Njaaréem(Senegaal) ci guddig àjjuma gu 14 ci weeru tëbëski, atum 1333 g.g, dëppoo ak 22 satumbar 1915. Aji juram ju góor di ku jaradee leeral ngir xam gi ko nit ñépp xam di [[Seex Ahmadu Bamba]], ju jigéen di [[Soxna Faati Jaxate]], mom Sëñ Moodu Asta mu baax ma te sell. S Tuubaa bi mu ganee àdduna daa bindoon ciw kayit tur wi di (Saaliwu giy tekki aji baax, aji yéwén) jox ko [[Sëñ Muhammadu Lamin Jóob Dagana]], ne ko tudde ko ko, bi mu ko defee moom S Dagana, daa daal di bind as lëf ciy bayit ñaanal ci liir bu tedd bii aw fan wu gudd akug wér, akug yékkatiku ci jamonoom ba mel ni jant, mu wax ca ne:...
'''[[Ndakaaru]]''' (Dakar) Nekkoon péyu Afrig gu sowwu gu fraase (ASF, walla AOF ci FR), Ndakaaru fimne mooy Péyu reewum Barug Senegaal akit goxub Ndakaaru, tolluwaayam ci péeteg sowwu bu Afrig, ci jegeem Daanaka-dun bu Kap-Wert, waral na sancug notaakon yu jëkk yi, Akit yaxantu ak Àdduna bu bees bi, te ame na peetewaayu ngëneel ci jëflanteg cosaani Saa-Afrig yi ak Saa-Tugal yi. Fa lees Taxawalee woon Xumbalu Àddina bu fànni ñuule (jaam yu ñuul) bu njëkk bi ci xalaatu Leopool Sedaar Sengoor atum 1966, Dëkk bii mooy toogu bu Këru-gëstu bu dàttu bu Afirg gu ñuule (KDAN, walla IFAN ci FR) akit bu Bànk bu diggu bu guuri Afrig gu sowwu (BDGAS walla BCEAO ci FR)
 
|}<noinclude>[[Wàll:Xët wu njëkk|N]]</noinclude>