Wuññi yu melosuuf yi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
JimeoWan (waxtaancëru)
formatting
 
Rëdd 1 :
'''[[Wuññi]] yu juxraaf yi walla yu [[melosuuf]] yi :.'''
 
== Luy [[wuññi yu melosuuf]] yi ?: ==
 
[[Yëngu-yëngu]] gu [[wuññi]] gu melosuuf, walla feeñal gu melosuuf, yëngu-yëngu gu yàgg la. Waa-[[Isipt]] ñu njëkk ña ak [[Finiix]] yi ak [[jullit]] ñi defoon nañu ko bu yàgg, njëkk waa-[[Tugal]] di ko def ci jamono ju yees ji. Lu am soloo ngii nag ñu war koo xam, mooy wuññi'y juxraaf yi, bi muy am it li ko taxoon’a jug mooy ay xemmemteefi [[sañc]] , ak doonte daa mbubboo woon gëstu gu aju ci xam-xamu [[melosuuf]].
== Luy [[wuññi yu melosuuf]] yi ?: ==
 
[[Yëngu-yëngu]] gu [[wuññi]] gu melosuuf, walla feeñal gu melosuuf, yëngu-yëngu gu yàgg la. Waa-[[Isipt]] ñu njëkk ña ak [[Finiix]] yi ak [[jullit]] ñi defoon nañu ko bu yàgg,njëkk waa-[[Tugal]] di ko def ci jamono ju yees ji. Lu am soloo ngii nag ñu war koo xam, mooy wuññi'y juxraaf yi, bi muy am it li ko taxoon’a jug mooy ay xemmemteefi [[sañc]] , ak doonte daa mbubboo woon gëstu gu aju ci xam-xamu [[melosuuf]].
 
Yëngu-yëngu gu wuññi gu melosuuf gi ñuy waxtaane ci [[doggantal]] gii, danañu ko man’a xamalee ci nii:
 
Mooy mbooloom liggéey yi [[jéngukat]] (aventurier) yu [[Tugal]] yi daa def ci ñaari xarnu yii : bu fukk ak juroom ak bu fukk ak juroom benn g. Yenn nag ci réewi Tugal yu [[nasaraan]] yi, ñoo leen doon soññ ak’a jàmbaarloo ak’a xiirtal ci loolu.
 
 
== Li sabab wuññi yii ==
 
=== 1) sababSabab bu diine ===
 
== 1) sabab bu diine ==
 
 
[[Sabab]]u [[diine]] moo jiitu ci sabab yi waraloon yëngu-yëngu yu wuññi yu melosuuf yu Tugal yii am. Sababu diine mooy li gën’a waral ñaari réewi [[katolig]] yii di [[Espaañ]] ak [[Portigaal]] defoon liggéeyub wuññi boobu.
Ligne 25 ⟶ 21 :
[[Paab gi]] ak [[nasaraan]] yi ci ginnaawam, dañoo ragaloon [[lislaam]] ak ñoñam, looloo taxoon ñu daa wut nu ñu mucce ci ñoom, ñu ne woon kon nañu leen fi jeem’a jële.
 
== 2)= Sababu politig: ===
 
== 2) Sababu politig: ==
 
 
Am na yeneen réew yu yees yu feeñ ci [[ëtt]]ub politig bu [[Tugal]] bi, yu ci mel ni [[Espaañ]], [[Portigaal]], [[Angalteer]], [[Faraas]], [[Holand]] ak yu dul yooyu. réew yii nag, dañoo tàmbli woon di xalaat bu baax ci tas ak wisaare seeni [[kilifteef]] ak jeexiital ci biti seen, rawati na ci réew yi ci yeex ci séenu'g nekku walla sosu gu yees. ñu gisoon it ne bu ñu fa tasee, wisaare fa seeni [[xay]] aki [[ngér]]i [[diine]],loolu da na man a nekk ay raas yu ñu man'a jaare ngir sampu fa, sanc leen . Réew yii nag [[joŋante]] woon nañu te [[gëpplante]] ci mii [[lef]] , loolu bokk ci li daa soññ ak’a xiirtale ci yëngug wuññi gu melosuuf gi.
 
== 3)= Sabab bu [[koom-koom]] :===
 
Waa [[Tugal]] yi ñoom dañoo gisoon ne [[àdduna]]y [[jullit]] ñi daal, mooy ji ngëp ci loxoom [[nos]]ub [[yaxantu]] bi, ndaxte ñooy ñi notoon, tegoon loxo ci kaw [[yooni yaxantu]] yu [[penku]] yi. Ci noonu xalaatu wacci fi yooyu yoon, te gëstuji yeneen yu leen man’a àggale [[End]] ak [[Siin]] tàmblee feeñ, ngir bañ’a fay njëgi [[nduwaañ]] yi ak [[galag]] yeek yeneen yi cig wàll, ak ngir néewal doole [[koom-koom]]u jullit ñi ci geneen wàll, ginaaw bi ñu soppee yoon yooyu def leen leegi ñu jaar [[Afrig]] ak [[màmbulaan gu atlas]] gi , loolu lépp ngir bañ’a jaar fi jullit ñi dëkke.
== 3) Sabab bu [[koom-koom]] :==
 
Waa [[Tugal]] yi ñoom dañoo gisoon ne [[àdduna]]y [[jullit]] ñi daal,mooy ji ngëp ci loxoom [[nos]]ub [[yaxantu]] bi, ndaxte ñooy ñi notoon, tegoon loxo ci kaw [[yooni yaxantu]] yu [[penku]] yi. Ci noonu xalaatu wacci fi yooyu yoon, te gëstuji yeneen yu leen man’a àggale [[End]] ak [[Siin]] tàmblee feeñ, ngir bañ’a fay njëgi [[nduwaañ]] yi ak [[galag]] yeek yeneen yi cig wàll, ak ngir néewal doole [[koom-koom]]u jullit ñi ci geneen wàll, ginaaw bi ñu soppee yoon yooyu def leen leegi ñu jaar [[Afrig]] ak [[màmbulaan gu atlas]] gi , loolu lépp ngir bañ’a jaar fi jullit ñi dëkke.
 
Yenn ci réewi Tugal yu yees yi dañoo gisoon ne li gënoon ci ñoom mooy seeni [[séqoo]] yu yaxantu ak réewi [[penku]] yi, ñu koy defal seen bopp, ngir mucc ci [[rënk]]ug yaxantu gii dëkki [[Itaali]] yi ame woon te daan ko def, yu ci mel ni [[Venezia]] ak [[Genova]] añs. Xalaat bii nag taxoon na ba yii réew demoon gëstuji aw [[yoonu yaxantu]] wu bees, nga xam ne ñoo ciy nekk ci wenn waxtu wi di yaxantukat biy jëli ,tey tuxal, tey kiy dox ci diggante yi.
 
Lori waa Tugal yi tàmbli woon na’a yol, ñu tàmbalee ñammasle ak a manadee tëyye seen bopp, bi ñu déggee xibaari wurus ak xaalis ci [[Afrig]], ndax kat [[mbell]] yu [[gànjaru]] yi dañoo muuroon seeni gët, fees seeni xel, ñoom ñi nga xam ne dañoo tàmbli woon di faale ak a yittewoo wàllug [[ne-ne]] gi rekk (maanaam lu aju lu ñu man a jariñoo ci ay suuf, wurus mbaa lu ni mel), bayyi nee yeneen wàll yi, loolu moo tax ñu sawaroon lool ci def wuññi gu melosuuf gi bi ñu déggee tono gu ne-ne gu rëy gi nga xam ne am mbooloo ci [[wuññikat]]i Tugal yi ndàmmoon nañu ko ci seen tukkiy wuññi yooyu, rawati na bi ñu jàngee [[xisa]]y tukkikatu Itaali boobu di [[Marco Polo]] (1254 - 1324 g ), mi wuññiji woon ba [[Siin]] (1271 - 1275 g ), nga xam ne bi muy dëpp, daa indaale lu sakkan ciy [[doj yu tedd]] , ba mujj waa [[Venezia]] daa ko wooye boroom milyoŋ yi .
 
== 4)= Sababu [[xam-xam]]: ===
 
Xalaat yi boroom xel yi ci Tugal amoon ci suuf si, ak ab bindam dafa soppiku woon, ginnaaw bi ay tukki yu melosuuf yu kenn-kenn amee ak yu mbooloo yu [[nasaraanal]], juge Tugal, génn, rawati na ginnaaw bi jamonoy [[xarey jooñe]] yi jàllee, nga xam ne boroom xam-xam yu bari leegi dañoo am koolute ci ne [[suuf]] si dafa [[bulu]] walla mu mel ni ab [[kol-kol]], wuute ak la ñu jàppoon, gëm ko, muy dafa tàllaliku mel ne basang gu ñu lal, loolu nag mooy li muuroon xeli waa Tugal yépp ci [[jamono yu diggu]] yi.
== 4) Sababu [[xam-xam]]: ==
 
Ag jèng jëm ci sopp ag [[jéngu]] , ak bëgg xam-xamu [[melosuuf]], feeñ ci ñoom, ginnaaw ba fa ruug gëstu gu xam-xam gënee suuxatu, gën fa’a jëme kanam, ak li ñu jële ci jullit ñi - ci biir [[xarey jooñe]] yi ak ginnaaw bi - ci xam-xam bu melosuuf bu jëm kanam, ak ginnaaw bu xam-xamu [[Saytubiddiw]] ak liggéeyiinu gaal ak [[buusal]] biy won gaal yi seeni yoon gënee jëm kanam.
Xalaat yi boroom xel yi ci Tugal amoon ci suuf si, ak ab bindam dafa soppiku woon, ginnaaw bi ay tukki yu melosuuf yu kenn-kenn amee ak yu mbooloo yu [[nasaraanal]], juge Tugal, génn, rawati na ginnaaw bi jamonoy [[xarey jooñe]] yi jàllee, nga xam ne boroom xam-xam yu bari leegi dañoo am koolute ci ne [[suuf]] si dafa [[bulu]] walla mu mel ni ab [[kol-kol]], wuute ak la ñu jàppoon, gëm ko, muy dafa tàllaliku mel ne basang gu ñu lal, loolu nag mooy li muuroon xeli waa Tugal yépp ci [[jamono yu diggu]] yi.
 
== Wuññiy melosuuf yu Portigaal yi: ==
Ag jèng jëm ci sopp ag [[jéngu]] , ak bëgg xam-xamu [[melosuuf]], feeñ ci ñoom, ginnaaw ba fa ruug gëstu gu xam-xam gënee suuxatu, gën fa’a jëme kanam, ak li ñu jële ci jullit ñi - ci biir [[xarey jooñe]] yi ak ginnaaw bi - ci xam-xam bu melosuuf bu jëm kanam, ak ginnaaw bu xam-xamu [[Saytubiddiw]] ak liggéeyiinu gaal ak [[buusal]] biy won gaal yi seeni yoon gënee jëm kanam.
 
 
 
== Wuññiy melosuuf yu Portigaal yi: ==
Portigaal moom la ñuy jàppe réew mi jiite woon [[wuññi yu melosuuf]] , yu Tugal yi. Buur bii di [[Henri]], mi nekoon ab [[mool]] (1394 – 1460 g ) , doonoon doomi buur bu Portigaal bi tudoon [[John mu njëkk]] mi, moom mooy ki njëkk’a def ay wuññi ci waa Portigaal yi. Mu nekkoon ku soppoon moolu(dugg géej), ak yër xisay mool yi, ak téerey taariix yi . Muy ku aayoon ci rëdd [[lonkooyoon]]i melosuuf yi, moom la baayam sàmpoon mu yor [[Sawuta]] , ginnaaw bi ñu ko nangoo ci julliti [[Marog]] yi atum 1415 g.
 
[[Henri]] daa xalaatoon’a wesaare diine’y nasaraan ju katolig ji ci [[Afrig]], ci noonu mu ne kon na jokkoo’k buuru nasaraan bu Ecopi bii di [[Prester John]], ngir ñu ànd, xeex waa [[Marog]] yii di ay jullit cig wàll, ak ngir man’a àgg ca [[waax]]i [[géej gu xonq]] ga ci geneen wàll. Ci noonu mu yabal ay [[mool]] yoy ci seen tukkiy wuññi yooyu, àggoon nanu ba ca [[dun]]i [[Kanaari]] ya , ak [[Madira]] ak [[Osoras]] ci [[Mambulaanug Atlas]] , atum 1402 g, naka noonu ñu wëy ci seen tukki yooyu ba agsi [[Senegaal]], atum 1445 g, ginnaaw bi [[Henri]] deewee tam teewul seen tukki yooyu wëyoon ba ci [[sottiwaay]]u dexug [[Kongoo]] gi ak [[Niser]]. Bu ko defee mool bii di [[Bartholmew Diaz]], moom àgg ba ca wàllug [[bëj-saalumu Afrig]], di fa ñuy wax [[Boppub Callmeer]], atum 1486 g, moom la buurub Portigaal bi soppi tur wi tudde ko «[[Boppub Yaakaar Ju Baaxi Ji]]» ngir mool yooyu man cee ame yaakaar ba man’a wuññi yoonu yaxantu wi jëme [[End]].
Portigaal moom la ñuy jàppe réew mi jiite woon [[wuññi yu melosuuf]] , yu Tugal yi. Buur bii di [[Henri]], mi nekoon ab [[mool]] (1394 – 1460 g ) , doonoon doomi buur bu Portigaal bi tudoon [[John mu njëkk]] mi, moom mooy ki njëkk’a def ay wuññi ci waa Portigaal yi. Mu nekkoon ku soppoon moolu(dugg géej), ak yër xisay mool yi, ak téerey taariix yi . Muy ku aayoon ci rëdd [[lonkooyoon]]i melosuuf yi, moom la baayam sàmpoon mu yor [[Sawuta]] , ginnaaw bi ñu ko nangoo ci julliti [[Marog]] yi atum 1415 g.
Mool bu siw bii di [[Vasco De Gama]] moom, jug def [[tukkib wuññi]], atum 1497 g, daal di àgg End, ginaaw bi mu wëree [[Afrig]] jaare ko ci yoonu [[tefes]]ug [[Marog]] gi, romb Bopp Yaakaar Ju Baax Ji, ak [[Mosambig]] ak [[Mombasa]] ak [[Malandi]], ba àgg ([[Jawa]]) ca tefesug [[sowwu]] gu [[daanaka-dun]] bu [[End]].
 
[[Henri]] daa xalaatoon’a wesaare diine’y nasaraan ju katolig ji ci [[Afrig]], ci noonu mu ne kon na jokkoo’k buuru nasaraan bu Ecopi bii di [[Prester John]], ngir ñu ànd, xeex waa [[Marog]] yii di ay jullit cig wàll, ak ngir man’a àgg ca [[waax]]i [[géej gu xonq]] ga ci geneen wàll. Ci noonu mu yabal ay [[mool]] yoy ci seen tukkiy wuññi yooyu, àggoon nanu ba ca [[dun]]i [[Kanaari]] ya , ak [[Madira]] ak [[Osoras]] ci [[Mambulaanug Atlas]] , atum 1402 g, naka noonu ñu wëy ci seen tukki yooyu ba agsi [[Senegaal]], atum 1445 g, ginnaaw bi [[Henri]] deewee tam teewul seen tukki yooyu wëyoon ba ci [[sottiwaay]]u dexug [[Kongoo]] gi ak [[Niser]]. Bu ko defee mool bii di [[Bartholmew Diaz]], moom àgg ba ca wàllug [[bëj-saalumu Afrig]], di fa ñuy wax [[Boppub Callmeer]], atum 1486 g, moom la buurub Portigaal bi soppi tur wi tudde ko «[[Boppub Yaakaar Ju Baaxi Ji]]» ngir mool yooyu man cee ame yaakaar ba man’a wuññi yoonu yaxantu wi jëme [[End]].
Mool bu siw bii di [[Vasco De Gama]] moom, jug def [[tukkib wuññi]], atum 1497 g, daal di àgg End, ginaaw bi mu wëree [[Afrig]] jaare ko ci yoonu [[tefes]]ug [[Marog]] gi, romb Bopp Yaakaar Ju Baax Ji, ak [[Mosambig]] ak [[Mombasa]] ak [[Malandi]], ba àgg ([[Jawa]]) ca tefesug [[sowwu]] gu [[daanaka-dun]] bu [[End]].
 
[[Vasco De Gama]] mii jot naa xamante ak [[Ahmadu’bnu Maaja]] mii di woon ab mool bu jullit bu [[araab]], moo ko dimbli sax ba mu man’a àgg End, ndaxte mooli jullit ñi ñu xamoon [[géej]]i penku yi lañu woon, ak yooni yaxantu yu [[jéeri]] yeek yu géej yi.
 
Naka noonu beneen mool jugati bu tudd [[Kabraal]], def ab tukki bu géej bu aju ci [[xare]], dem [[End]] ,tàmblee naj ak’a sonnal Samirin,mi daa àtte ak’a saytu fi ñuy wax [[Kalikuta]] gu End gi, ngir mu jox Portigaal ab barab bu yaxantu ci tefes gu [[sowwu]] gi, Kabraal mii xeex na fa’ak jullit ña, song barab ya ak [[mbooloom gaalam]] ma. Vasco De Gama moom itam delluseeti End ci ab tukkib xare ngir faagaagalsi Samirin, ak mbugalsi yaxantukati araab yu jullit yi, ak defsi ay déggoo ak buuri [[diiwaan]]i End yi nekk ci [[tefes]]ug [[sowwu]] gu [[daanaka-dun]] bu End bi.
 
== Li wuññiy melosuuf yu Portigaal yi jur : ==
 
== Li wuññiy melosuuf yu Portigaal yi jur : ==
 
 
[[Wuññiy Portigaal yi]] jur nañu ay [[ngérte]] yu bari, yi ci ëpp njariñ ñooy yii di ñëw :
Ligne 69 ⟶ 56 :
'''''1)''' Waa Portigaal, ñi ngi tàmbli woon di teg loxo ci [[tefes]]i [[Afrig]] yu [[sowwu]] yi, ci noonu [[njàppum jaam]] siiw, te tas ci [[Tugal]] gépp, di [[jaam]] yi ñu daa jàppe Afrig, te daan ci [[yaxantu]]''.
 
'''''2)''' [[Jamono]]y [[sanc]] gu Portigaal , mi ngi tàmblee ci bi Portigaal taxawalee ab [[sancu]] , ci [[penku]] bi, ca fa ñuy wax [[Jawa]], ay xare it am diggante [[araab]] yu jullit yi ak Portigaal cig wàll, ak ci diggante waa Portigaal ak waa[[ End]] yi ci geneen wàll. Waa Portigaal yi nag jot nañoo teg loxo yenn [[waax]] yu am solo yi nekkoon ci yoon wi jëme [[End]]''.
 
'''''3)''' Waa Portigaal yi mujj nañu xam yoonu yaxantu wu géej, wu dul romb ci réewi jullit ñi,mooy wi jaar ca [[Boppu Yaakaar Ju Baax ja]]'' .
 
Loolu nag mooy li doyadiloon [[koom-koomu]] jullit ñi ci [[penku]] bi, maanaam [[koom-koomu]] nguurug [[Mamaalik]] ci jëmmi boppam. Lii moo taxoon [[nguurug Mamaalik]] mujjoon néew doole ci kanamu nguurug Portigaal gi ak ci kanamu [[ñoñ Usmaan ñi]] nga xam ne jot nañoo fexe ba xaw’a woyofal naj ak ñàkkal-jàmm gi Portigaal defoon araab yi, ak nguuri [[araab]] yi nekkoon ci tefes gi, yàqoon nañu it mbooleem jéem yi ñu daa def ñoom waa Portigaal ngir taxawal ab [[jë]] bu [[nasaraan]] safaan (kontar) doole yu lislaam yi nekkoon ci peggu géej gu [[xonq]] gi, ak [[tefes]]ug [[Afrig]] gu [[penku]] gi.
 
== Wuññi yu melosuuf yu Espaañ yi : ==
 
Li ci dugaloon [[Portigaal]], moo dugal it [[Espaañ]] ci [[wuññi]] yooyu. Ci noonu boroom xam-xam yi daa yëngu ci mbiri wuññi gi, danoo jàppoon ne [[suuf]] si daa [[bulu]], moo waraloon ba ñuy dem End ñu jaare woon ko ci sowwu bi.
[[
Ligne 85 ⟶ 72 :
Ci tukki bii la jotoon’a wuññee [[Jamayka]], daal di delluwaat Espaañ ci atum 1496 g. Mu defati ñatteelu tukki atum 1498 g, waaye amu ca woon tawfeex. Mu dellu defaat bu ñeenteel atum 1502 g, taxul ba tay mu am ca la mu ca doon wut. Bu ko defee nag ñaari sooy yii mu def ci ñaari tukkeem yi tax ba [[buur]]u Espaañ bi [[Ferdinand]] ak soxnaam [[lingeer]] bi [[Isabela]], begadi woon ci loolu, ag siiwam suux, ñu folli ko ci [[njiitul geej]] gi, daal di koy delloosi Espaañ ci ay jéng, ngir mere gu ko [[meññilukat]] yi mere, ñoom ñi seen yaakaar tas. Colombo faatu na atum 1506 g, te xamul sax ne wuññi na àdduna ju yees ju dul End.
 
Ginnaawam it wuññikat yi doon liggéeyal Espaañ wëy ci seen liggéeyi wuññi yooyu , ka cay [[Amerigo Vispucci]] jot ca’a àgg ca [[diiwaan]] ya Colombo àggoon ak yeneen yu mu àggutoon, ci njëlbéeni xarnub fukk’ak juroom benn. Moom [[mool]] bii di Amerigo, moo am [[teraanga]]y ñu tudde ko Adduna ju bees jii di [[Aamerig]] tay.
 
== Li wuññiy Espaañ yi jur: ==
 
'''1)''' ''Ñoom de ubbil nañu tukkiy wuññi yi aw yoon wu bees wu jëm ci àdduna ju yees ji, di ko jaare ci [[màmbulaan gu atlas]] gi . Bu ko defee [[Espaañ]] tàmblee sanc gox yi mu jotoon’a àgg ci [[Aamerig gu diggu]] gi ak gu bëj-saalum gi, ñu wisaare fa seenug [[xay]] ak [[diine]], ubbi fa ay [[mbell]]i [[wurus]] ak [[xaalis]]''.
 
'''1)''' ''Ñoom de ubbil nañu tukkiy wuññi yi aw yoon wu bees wu jëm ci àdduna ju yees ji, di ko jaare ci [[màmbulaan gu atlas]] gi . Bu ko defee [[Espaañ]] tàmblee sanc gox yi mu jotoon’a àgg ci [[Aamerig gu diggu]] gi ak gu bëj-saalum gi, ñu wisaare fa seenug [[xay]] ak [[diine]], ubbi fa ay [[mbell]]i [[wurus]] ak [[xaalis]]''.
 
'''2)''' ''Saxal gu ñu saxal ci xam-xam ne [[suuf]] si daa “[[bulu]]” , te li waraloon loolu di tukki bi [[Magellan]] defoon. Buur bi ñu daa wax [[Shark]] mu juroomeel mi ([[Sharlakaan]]) di woon buurub Espaañ, daa digaloon mool bii di Magellan atum 1519 g, mu def ab tukki jëm penku jaare ko sowwu, ci noonu moom Magellan jug, moolu (war geej), jawali sowwu, te jëm penku, ci kaw [[màmbulaan gu atlas]] gi, bi mu ko defee daal di àgg ca tefesug [[Breesil]] ga, fa [[Riyo De Janero]], mu wëy nag ca doxam ba, ba ca [[sottiwaay]]u [[dex]]ug [[Labalata]], daal di wër [[Aamerig gu bëj-saalum]] gi, tàbbi [[màmbulaan gu dal]] gi nga xam ne moom moo ko tudde « [[pasifik]] » di wund lu dal, mu àgg [[Filipin]] atum 1521 g, foofa nag mu songoo fa’ak ñoñ réew ma, ci’y xeex yoy ca la ñu ko raye, waaye kenn ciy nitam, tuddoon [[Dianco]], moo mujjoon jiite boobu tukki, dem ak ñoom ba ci [[Boppu Yaakaar Ju Baax ji]], juge fa dem Espaañ, gi nga xam ne ma nga fa àgg atum 1522 g''.
Ligne 96 ⟶ 82 :
'''3)''' ''Weddi [[gisiin]] yi daa wax ci bindu [[suuf]] si ak ab [[kem]]am ( ni mu tollu), ndax kat tukki bii nga xam ne dafa dox, wër [[àdduna]] bi, firndéel na ne [[suuf]] si daal moo ëpp fuuf li ko Colombo jàppe woon ak ku dul moom. Beneen [[gox]] feeñ na, bu mag diggante [[Tugal]] ak [[Asi]] ci wàllug sowwu gi, di [[Aamerig gu bëj-gànnaar]] gi, nga rax ci dooli geneen gi’y gu bëj-saalum gi, te ag [[màmbulaan]] gu yaatu, gu yees’a ngii gu ñu xamutoon. Kon suuf desatutoon su ñu xamutoon su dul [[Ostrali]] ak ñaari [[dott]] yi'' .
 
== Wuññi yu Angalteer: ==
 
Ñoñ Angalteer ñoom itam sóobu woon nañu ci wuññi yi, bi Buur bi [[Henri mu juroom ñaareel]], mi nekkoon buurub Angalteer digalee mool bii di [[John Cabot]], mu tukki dem End, jaare ko bëj-gànnaar gu suwwu gi, ca saa sa mu géeju, tukkee [[Bristol]] atum 1497 g, jéggi màmbulaan gu atlas, àgg tefes gu bëj-gànnaar gu Amerig gu bëj-gànnaar gi, ca [[New Fondland]], ginnaaw bi mu jéggi [[Librador]], dellu Angalteer. Cabot mii delseeti na leru tefesu’g penku gu Aamerig gu bëj-gànnaar gi, ba àgg [[Florida]], loolu nag moo doonoon tàmblig sancug waa Angalteer yi, ñeel Aamerig gu bëj-gànnaar gi ak [[Kanadaa]] . Ba tay it, kii di [[Jams Kook]] di woon ab mool bu dëkkoon Angalteer, defoon na moom it ñatti tukki yu wuññi ca tefesi Ostrali yu penku ya ak [[Newsiland]].
 
== Wuññiy araans yi : ==
 
== Wuññiy araans yi : ==
 
Waa Fraans nag ñoom, ñoo mujjoon’a duggsi waa Angalteer, waa Espaañ ak waa Portigaal ci lefum wuññi mi, ñoom seeni tukkiy wuññi daa jëmi woon Kanadaa. Ki ñuy wax [[Jaak Cartier]] moom ab mool la woon, daa jugoon def benn tukkeem bu wuññi ci jamonoy [[Faransuwa mu njëkk mi]], jeggi màmbulaan gu atlas gi, jem sowwu, fétali [[àdduna ju yees ji]]. Ci noonu mu àgg [[New Fondland]] gi jàkkaarloo ak Kanadaa, daal di fay jot’a wuññi walla feeñal sottiwaayu dexug [[Santa Lorans]]. Tukki yi Cartier mii jot’a def ci goxi Aamerig gu bëj-gànnaar gi ñeent lañu woon. Bi mu ko defee sancug [[Faraas]] tàmblee putuxlu ci Kanadaa, ak barabi dex yi ci Aamerig gu bëj-gànnaar gi. Noonu ñu taxawal ab sancu tudde ko [[Samwel de Shampala]], taxawal it dëkk bii di [[Kebeg]] ci tefesug dexug [[Santa Lorens]] atum 1608. Moolu Faraas bii di [[De Laasal]] jotoon na’a wuññi dexug [[Misisipi]], ci noonu waa Faraas ya daal di fay sos sancu bu [[Luwisiyaana]], bii nga xam ne mi ngi jële turam wi ca buurub Faraas ba tuddoon [[Luwis mu fukk ak ñeenteel mi]].
 
== Wuññi yu Oland yi : ==
 
== Wuññi yu Oland yi : ==
[[Lonkoo]] (société) gu [[En]]d gu [[penku]] gu [[Oland]] gi, dafa joxoon ndigal moolub Angalteer bii di [[Henry Hadson]], da ko’o joxoon ndigal ci mu defal [[Oland]] ab tukkib wuññi, ngir man koo gisal aw yoon wu bëj-gànnaaru penku wu ko man’a àggale [[Asi]], ci noonu mu géeju moom [[Hadson]] juge Angalteer, jaare ko ci bëj-gànnaaru atlas gi, jawali [[dóox]]ug [[New York]], ak dexug Hadson gi mu tudde woon boppam. moolu Oland bii di [[Wilyaam Shotin]] moom, moo wuññi yoonu [[Bopp]]ub [[Horn]] bi nga xam ne mujj na di yoonu géej wu am njariñ. Waa [[Oland]] yi jéemoon naño’o wuññi [[Ostraali]] ak [[Newsiland]] ci diggante 1622 – 1624 g .
 
== Li wuññiy [[melosuuf]] yu [[Tugal]] yi jur :==
 
== Li wuññiy [[melosuuf]] yu [[Tugal]] yi jur :==
 
Li wuññiy Tugal yi jur man nañu koo tënk ci lii di ñëw :
Ligne 122 ⟶ 103 :
'''2)''' ''Wuññi yu melosuuf yi amal nañu fi jawwu yu gëpplante ak wujje, ak as lef cig noonoo ci diggante réew yi doon def wuññi yii, loolu moo yokkoon xemméemtéefi sanc yi ci diggante réewi Tugal yi. Ci noonu aw [[gisiin]] wu sanc tàmbli woon’a feeñ wu Tugal jëm ci askani réew yii ñuy door’a wuññi''.
 
'''3)''' ''Xam-xami melosuuf yi soppiku woon nañu bu baax, li ko waraloon di yaatu gi wuññi yii yaatu woon te bari. Ci noonu yëngu-yëngu gu [[nasaraanal]] yokku ci anam gu fés, rawati na ci [[Afrig]] ak ñaari [[Aamerig]] yi.''
 
'''4)''' ''Ag jëm kanam feeñoon na ci wàllug yaxantug [[mbèll]] yi, di wurus ak xaalis, nga xam ne sax xarnub fukk ak juroom g, dañu koo tudde woon « xarnub xaalis », ni nga xame ni jëm kanamug koom googu taxoon na ba dundiin wi gën’a kawe, njëg yi it gën’a yekkatiku, ni fi ay njaay yu yees dugge, lu ci mel ne [[kakaawoo]], [[póon]], kiinaa, batata ak [[mbòq]].'' .
 
'''5)''' ''Wuññi yi de lenn lañu ci màndarga yiy wone [[yewwute]]g [[Tugal]] gi, ni nu la ko leerale woon ci doggantal gu njëkk ga''.
 
'''6)''' '''Réew yii ñu wuññi, ruu gu fees ak bëgg’a fayyu moo leen ubale woon, muur leen, jëm ci yii leen wuññi, ndax ñoom [[tubaab]] yi xalaati sanc lanu yoroon, daan ci doxe ci mbooleem seen doxi wuññi yi, lepp lu nu gis [[aakimoo]] ko, ngartaajoo ko, lii mooy li waral askani réew yi nu wuññi, jugoon ci jànkoonte ak ñoom, taxaw ci xeex canc gu Tugal gi, ci anam gu tar, jëfandikoo ci li nu yor lepp ci kàttan'''.
 
'''7)''' ''Wesaare [[diiney nasaraan]] ci bepp gox bu ñu wuññi''.