Siin-Saalum wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 4 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q1572262 (translate me)
Tamsier (waxtaancëru)
→‎Mbegaan nduur : Maad a Saluum Mbegaan Nduur du Maad a Sinig Wagaan Fay. Bullen jahasse
Rëdd 30 :
 
== Mbegaan nduur ==
MoomMbegaan la ñuy wax itam Waagaan Fay,Nduur moo daaneel Aali Baana di woon njiitu diine ca tukulòor ya, doonoon sëriñ bu amoon doole ca Saalum rawatina ca Kawòon. Ci moom la Séeréer si yéegée ci jal bi, doon ay buur.
 
Moom Mbegaan def na lu ne ngir man a jot ci nguur gi. Ba mu ca jotee la noot nguur-nguuraan ya nekkoon ca wetam: Ngabi, Ndukumaan, Kaymoor, Mandaak, ak Jiloor, ak Genig, ak Jokkul. Dawloo buur ya teg fa ay ñoñam.
 
== Yorteef ak Yoon ==