Weeri wolof wuute gi ci sumb yi

9 octets ajoutés ,  7 at ci ginaaw
defar benn lëkkalekaay
m (Bot: Migrating 82 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q28892 (translate me))
(defar benn lëkkalekaay)
[[Weeri wolof]], ci [[Arminaatuarminaat|arminaatu]] gàddaay gi, walla bu [[jullit]] ñi mbaa bu [[Lislaam]], ab arminaat bu weer la, buy sukkandiku ci doxiinu weer wi ngir xam ak natt weer wi. Jullit ñi danañu ko jëfandikoo ci bépp barab, rawati na ngir natt ak xam xew-xewi ak bisi diine yi. Ki ko sos nag mooy [[Omar Ubn Xattaab]] (g.m), daal di def [[gàddaayug Yonent]] bi (j.m) juge [[Màkka]] dem [[Madiina]] muy ab tàmbaleem, looloo waral deesi tudde ko arminaatub gàddaay gi. Ak doonte arminaat bi ci jamonoy jullit ñi lañu ko sos, teewul turi weer yi ak arminaatub weer ñu leen daa jëfandikoo ca jamonoy réer ga (jaahiliya, maanaam njëkk Lislaam)
 
Yenn ci [[réew]]i [[araab]] yi, mu ci mel ne [[Araabi Sawdit]] -moom ci nguur geek askan wi - dañuy jëfandikoo arminaatub gàddaay gi niki arminaat bu kilifawu di ci taariixe ci bindante yiy am ci diggante liggéeyuwaayi nguur gi, waaye nag lu ci dul moom, askani araab yi ci des yépp de beneen bi lañu miin te moom it lañuy jëfandikoo muy bu judd gi (juddug yonent Yàlla Isaa (j.m)).
61

modifications