Break dancing wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 48 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q169737 (translate me)
JimeoWan (waxtaancëru)
texte en double
Rëdd 6 :
Taariixu break dance mi ngi doore ca [[Bronx]] ci [[ati 1970]], Kenn ku bokkoon ci mbootaay gu Bronx River projects la ñu ne moo ko sos. Mu jóge fa, tudde Bronx River Association [[Afrika Bambaataa]], ba si yàgg mu tuddewaat ko [[Zulu Nation]] (ci [[1974]]). Gëstu yi mu doon def ci [[taariixu Afrig]] ak mbëggéelam ci woy gëtanoon ko, ba taxoon mu farlu woon ci ngir ay ndawi goxam nekk ciy yëngu-yënguy [[fànn]] ngir bañoon ñu duggu cig ndëngte. Moom lañuy santee juddug yëngu-yëngu gu bees gi: [[hip-hop]], gi dàttu ci ñenti ponku yii di [[rap]], [[grafiti]], [[DJing]] ak break dance. Afrika Bambaataa soosoon na itam benn ci gangoori break dance yi njëkk, tuddoon Zulu King. Njeexit gi [[Jamayka|waa-jamayka]] bii di Dj [[Kool Herc]] amoon ci caadaay hip-hop mi safaanu woon ak caadaay ndëngte ga amoon ca seen dëkkuwaay ya, ca jamono jooju am na solo lool, ba mat naa fésal.
 
==== cosaanuFu baatpecc bimi soqikoo ====
 
'''Break dancing''', walla breakdance, walla break, walla b-boying, ab baat la bu ñuy jëfandikoo ngir wax fecciin wa juddoo te màgge [[New York]] ci [[ati 1970]], xammeewu ngir ay suppjalañam aki bërangoom ci suuf si. Fecckatu break dance la ñuy wax breakkat.
[[Dencukaay:Break dancer by David Shankbone.JPG|thumb|250px| ab breakkat ca New York]]
== Taariixu break dance ==
 
==== Break dance ak hip-hop ====
Taariixu break dance mi ngi doore ca [[Bronx]] ci [[ati 1970]], Kenn ku bokkoon ci mbootaay gu Bronx River projects la ñu ne moo ko sos. Mu jóge fa, tudde Bronx River Association [[Afrika Bambaataa]], ba si yàgg mu tuddewaat ko [[Zulu Nation]] (ci [[1974]]). Gëstu yi mu doon def ci [[taariixu Afrig]] ak mbëggéelam ci woy gëtanoon ko, ba taxoon mu farlu woon ci ngir ay ndawi goxam nekk ciy yëngu-yënguy [[fànn]] ngir bañoon ñu duggu cig ndëngte. Moom lañuy santee juddug yëngu-yëngu gu bees gi: [[hip-hop]], gi dàttu ci ñenti ponku yii di [[rap]], [[grafiti]], [[DJing]] ak break dance. Afrika Bambaataa soosoon na itam benn ci gangoori break dance yi njëkk, tuddoon Zulu King. Njeexit gi [[Jamayka|waa-jamayka]] bii di Dj [[Kool Herc]] amoon ci caadaay hip-hop mi safaanu woon ak caadaay ndëngte ga amoon ca seen dëkkuwaay ya, ca jamono jooju am na solo lool, ba mat naa fésal.
 
==== fu pecc mi soqikoo ====
Jafe na lool joxe a taariix bu wóor cig juddoom. Ci jeexantalu ati 1970, [[New York]] dafa bari woon lool ay xeeti pecc, gox boo dem aki feccinam. Numu manti deme, li fés mooy ne, feccin yi gënoona siiw ñoo doonoon [[good foot]] ak [[popcorn]], te jóge woon ca woy yu [[James Brown]] ya ''Get On The Good Foot'' ak ''Popcorn''. Pecc yooyu yëngali tànk ci anam bu lañ woon te fecckat yi daan sapp se benn tànk di ko awante an beneen bi. Nit ñi daan nañu ci def ay joŋante, siiwoon nañu lool ca jamono yooyu.