Ibou

Inscrit depuis le 12 Suwe 2007
8 octets ajoutés ,  13 at ci ginaaw
m
wikiliens
m (wikiliens)
Ci 2007 bii laa tambalee jang wolof. Mooy làkk bi ma gënn a neex. Ci 2007 bi itam laa bindu ci Wikipedia tambalee cëru ci liggéey bi. Benn weer laa fi def ñu tàbb ma yorkat.
 
li ëpp ci li may jàng mooy téere taariix, roman, taalif ak xeltu. Téere bi ma njëkk a jàng mooy "nations négres et cultures" "Reewi ñu ñuul ak cosaan" bu seex anta joob. Bindkat bi ma gënn a neex mooy [[Paulo Coelho]] di ab waa-beresil.
Taggat-yaram bi ma gën a neex mooy futbòl.
[[Image:Cheikh Anta Diop.gif|thumb|center| Sama royuwaay bi gën a mag ci wàllu adduna
<center> seex[[Seex antaAnta joobJoob]]</center>
]]
</poem>
300

modifications