Waalo wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 108 :
 
Ba besu tey Waalo ngi jànkonteeg coon ya jòge woon ca ŋaayoo ga. loolu mooy jur dellu ganaaw ak daanug waalo, ba ku nekk di ko cokkaas: Taraasaa ak [[Almaami]] ak [[Dàmmeel]]. Ki ci gënoon a fés nag mooy [[Faraas]]. ganaaw ba Faraas rimbee Waalo ba mu nëx, dakoo teeyal dëtëm ko ci ndimbalu Budeŋ ak Potore ak [[Fedeerba]] mi ñëw seen ganaaw ci 1885. Booba la nootee Waalo, te naa daf koy xettali.
 
== Delluwaay ==
Paate sow, ''Démbi Senegaal: ci làmmeñu Wolof'', Dakaar, 1998
 
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[senegaal]]
* [[Kajoor]]
* [[Jolof]]
* [[Siin-Saalum]]
* [[Fuuta Tooro]]
* [[Réewi lebu yi]]
* [[Tekuruur]]
* [[Bawol]]
 
[[catégorie:taariix]]
[[catégorie:afrik]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Waalo » lañ ko jële