Jolof wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Jolof''' moo doonoon nguur ngi gënnoo na mag ci [[Senegaal]] ci jamono yooyu. Mi ngi sosu ci xarnub XIV ba [[Nguuru Mali]] gu mag ga saayee, rawati na la feete woon ca sowam. Ba nguuru Jolof taxawee, jëloon na melokaanu nguur yi ko jiitu woon, waaye bàyyi woon na fa melokaanu càmm ak màng ga xewoon ci jamono.
[[Image:Guuri senegaal.jpg|right|thumb| Limu[[lonkoyoon|Lonkoyoon]] politig bu nguur yi nekkoo [[senegaal]]]]
== Sosteefam ==
Ki ñu ne moo sos nguur googu mooy Njaa Jaan Njaay. Mooy doomu [[araab]] la bu ñuy wax Abaabakar ak [[Lingèer]] ab [[Tukulòor]] bu tudd Faatimata Sall. Moom, Njaa Jaan Njaay, def na ci réew mi liggéey yu réy.
Rëdd 69 :
 
== Nguuru Jolof ==
Jolof boo ko dee xool dafa këll bunom dem na ba lag da geer, égg na [[Ferlo]]. Moom dafa xawa uuf Tooro ak Dimat ak [[Waalo]] ak [[Kajoor]] ak [[Bawol]] ak [[Siin-SaaluumSaalum]] wàllu penku wi [[ndand fooyféy-fooyféy]] la. Jolof fu neew ñax la, bari na lool garabi werek. Mel na ne du fu naat it ndax ab woykat bu siiw ci yu wolof yi di [[Sëriñ MuusaaMusaa KA]] am na fu muy melale lu ni mel ci genn xasidaam, mu ne :
nawet Jolof noor fa te doo nooraani - ndaw lu ca sax soo màggatee yalwaani
 
Rëdd 92 :
== Delluwaay ==
Paate sow, ''Démbi Senegaal: ci làmmeñu Wolof'', Dakaar, 1998
 
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[senegaal]]
* [[Kajoor]]
* [[Waalo]]
* [[Siin-Saalum]]
* [[Fuuta Tooro]]
* [[Réewi lebu yi]]
* [[Tekuruur]]
* [[Bawol]]
 
== Téerekaay ==
Ligne 104 ⟶ 114 :
 
[[catégorie:taariix]]
 
{{modèle:buntutaariix}}
{{modèle:wikibaatukaay}}
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Jolof » lañ ko jële