Jolof wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 6 :
Bokk na ci def [[wolof]] yi ñuy benn, teg réew mi ci yoonu nguur gu leer. Samp nguuru [[Waalo]] ba mu dëgër, mu dal di koy jox rakkam. Sos nguuru Jolof gu mag ga ba mu yegg fa gën a kawe mu door a wàcce boppam. Looloo tax ña ko wuutu ñoo mottali liggéeyam ci xarnub XIV, waaye jotu ñoo moytu taste gu gaaw ca nguur gu mag ga.
 
Boo seetloo turi buur yu njëkk yi ci nguur gu mag gi di nga leen fekk ñekk fukk doŋŋ. Seen péey nekkoon na Céŋŋ ca jamonoy Njaa Jaan Njaay. Réew yu bari nekkoon nañ ci kilifteefu gu mag ga. Lu mel [[Senegaal]] ak [[GàmbiGaambi]] ak [[Faleme]] nekkoon na ñu ci suufu Jolof gu mag ga.
 
== Buuri Jolof yi ==
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Jolof » lañ ko jële