Waalo wuute gi ci sumb yi

6 octets ajoutés ,  13 at ci ginaaw
m
Coppite gi amul tënk
m
'''Waalo''' bokkoon na ci yénn ci nguuri [[Senegaal]] yi fi nekkoo. Buuru Waalo dañu ko daa tànn ca péncum Seb ak Bawar. Njurbel moo nekkoo péeyam ci lu njëkk, ganaaw bi lañ ko tuxël Jinge, tuxëlaat ko Ndeer. Tuxu yu bari yooyu doy na tegtal ci dellu ganaaw ak ñàkk doole.
 
== Gëwrin yi ==
300

modifications