Toolu mbëjbijjaakon wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
mAucun résumé des modifications
Rëdd 4 :
 
:<math>\mathbf{F} = q ( \mathbf{E} + \mathbf{v} \times \mathbf{B} )</math>
Te <math>q</math> di yanu wàll-wàllaan wi, <math>\mathbf{v}</math> diy [[Xél|xélam]], <math>\mathbf{E}</math> toolu mbëj bi, <math>\mathbf{B}</math> moom di [[xiirtalubxiirtalug mbëjbijjaakon]] bi.
[[Àtteb Faraday-Neumann-Lenz]] mooy wax ne: wuuteeg aj giy judd ci ag ndombo gu tëju dafa aju ci anam gu jonjoo ci coppite gu [[walug bijjaakon]] bigi te aju itam ci diirub jamono bi muy ame. Ci yeneen kàddu dafa aju ci xél yi walug bijjaakon gi di soppikoo ci jamono ji. Doxiinu [[masinu mbëj|masini mbëj]] yu bari yu mel ne ci misaal [[soppalikaay]] yeek [[doxalukaay bu mbëj|doxalukaayu mbëj]] yi ci bii àtte lañu sukkandiku.
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[Toolu mbëj]]