Xaralaymbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
MerlIwBot (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Xaralaymbëj''' Mooy xeetu xam-xam biygiy gëstu lépp lu jëm ci wàllug [[mbëj]], ay jëfandikuwiinam ak ay seddalewiinam. bu njëkk dañoo foogoon ne mbëj ag wal la rekk guy dem, gu man a nekk luygu yokkubaax(+) walla wàññikugu bon(-). Waaye ci ndimalu ay woroom xam-xam yu mel ne Hertz, Helmholtz, Maxwell, Heaviside, Alessandro Volta ak ñeneen ñu bari, ci lees dem ba gën a nànd, xam mbir mi. Lu mel ne [[yamaleb maxwell]] biy faramfàce tëdiinu [[Yanu mbëj|yani mbëj]] yi ( [[feppsaal]] ak [[mbëjfepp]] yiy wuute ci seen jublug yanub mbëj) walla toolu [[mbëjbijjaakon]] ba ca juddoo.
 
Ci gàttal, ci noonu lañu tambalee gis yenn ci ay jëfandiku yu mbëj: [[Doxalukaay bu mbëj]], [[soppalikaay]] aki leeruniitu...
 
Tay xaralaymbëj moo yor wàllu sàkk ay wuutuloxoy mbëj ak ay buumi séddalekaayu [[kàttanug mbëj]]
Rëdd 12 :
[[àtteb ohm]](om) yiy faramface [[ndëgërlu gu mbëj]] gi
 
[[àtteb Faraday-Neumann-Lenz]] mooy faramface [[sababuxiirtalug bijjaakonmbëjbijjaakon]]
 
[[njeexitu joule]] mooy leeral ni kàttanu mbëj di soppeekoo nekk [[tangoor]] ngir njeexitu ndëgërlu gi.
 
[[àtteb Kirchhoff]](kiirkof) mooy leeral jëflante bi nekk ci diggante [[Dawaanu mbëj|dawaan]] ak taraay[[Dendu mbëj|dend]] ci ag ndombo.
 
== Jóox, yóbbuyóbb ak séddale kàttanu mbëj ==
[[Dencukaay:Nataalu_buumu_mbëj.jpg |thumb|right| ay buumi seddalekaayu kàttanu mbëj]]
Ag wàll gu am solo moo jëm ci lépp lu ñeel yokkte ak seddalewiinu kàttanu mbëj ba ca jëfandikuwaay ya (barab yees koy jëfandikoo).
Rëdd 25 :
Buumi séddalekaay yi dañu leen a lëkkale ci seen biir ñuy jëlee [[kàttan]] gi ca jóoxuwaay ya di ko yóbb ca jëfandikuwaay ya.
 
Li wuutale Buumi yóbbukaay yi, mooy limu [[taraay]]dend gi ñuy yóbbuyóbb, moo tax ñuy gis ay buumi [[Dend gu kawe|dend gu kawe]], [[Dend gu diggu]|dend gu diggu]], [[Dend gu suufe|dend gu suufe]]. Su diggante jóoxuwaay yi guddee, dañ fay def ay [[mbëjjaruMbëjjaaru|mbëjjaaru]], ay buumi dend gu kawe yu man a yóbb ay milioŋi [[Watt|watt]] ci kàttan tambalee ciy 400000 v. Buumi [[Dend gu kawe|dend gu kawe]] yii la ñuy duppe yu [[yóbbug kàttanu mbëj]], yi nga xam ne ñooy tax ñua man a yóbb kàttanu mbëj gi, jëleejële ko ca jóoxuwaay ya, jëmee ko ca barabu soppikaay ya.
 
Ci nii la ñuy soppee [[dend gu kawe]] mu nekk [[dend gu diggu]], jaarale ko ci ay [[wuutuloxoMasin|masin]] yu mbëj yees di duppee [[soppalikaay]], ci noonu nag la ñuy yóbboo kàttanu mbëj gi ca ndombo gu dend gu diggu gi, moom ci boppam dañu koy àggal ci néegu seddalekaay yi jaarale ko cig [[ndombog séddaleg kàttanu mbëj]], foofa lañuy defee geneen coppite jëlee ko ci dend gu diggu soppi ko dend gu suufe ngir ñu man koo jox jëfandikukat yi ci kër yi ak liggéeyuwaay yi.
 
== Wuutuloxo yu mbëj ==
 
==== Doxalukaay ====
[[Dencukaay:Motors01CJC.jpg|thumb|right| DoxalukaayAy doxalukaay yu wuute]]
[[Doxalukaay bu mbëj|Doxalukaay yu mbëj]] yi, ay wuutuloxo lañu yu’y soppi kattanu mbëj def ko kattanu doolerandu. Doxalukaay yi dañu leen a seddaleséddale ci:
 
* Doxalukaay yu [[dawaan bu wéy]]
Rëdd 39 :
* Doxalukaay yu [[dawaan bu safaanu]], bii man naa dox ci ñaari fànn ( [[ñettwéq]], [[wennwéq]]), ci nii ñu am:
 
** Doxalukaay yu [[Doxalukaay bu demandoo|Doxalukaay yu demandoo]]: su fekkee baraayu ni muy wëddeeloo demandoo na ak baraayu ndombo ligi
 
** Doxalukaay yu [[Doxalukaay bu demandoodi|Doxalukaay yu demandoodi]]: su fekke wëddeeluwiinu boppam la am.
** [[Doxalukaay bu wennwéq|Doxalukaay yu wennwéq]]
 
Rëdd 57 :
[[Wuutuloxo]] yu man a yokk walla néewal taraay te di jëfandikoo benn lëmës rek, lañuy tuddee Soppiboppam
 
==== LeeruNiitu ====
Ay jumtukaay lañu yu aajowoo soppi [[kàttanug mbëj]] mu nekk leer. Di ko jëfandikoo ngir leeral barab yi.