Jolof wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët mu bees : '''Jolof''' moo doonoon nguur ngi gënnoo na mag ci Senegaal ci jamono yooyu. Mi ngi sosu ci xarnub XIV ba nguuru Mali gu mag ga saayee, rawati na la feete woon ca sowam. Ba n...
 
Rëdd 50 :
 
== Nguuru Jolof ==
Jolof boo ko dee xool dafa këll bunom dem na ba lag da geer, égg na Ferlo. Moom dafa xawa uuf Tooro ak Dimat ak Waalo ak Kajor ak Bawol ak Saluum wàllu penku wi ndand fooy-fooy la. Jolof fu neew ñax la, bari na lool garabi werek.,mel na ne du fu naat ndax ab woykat bu siiw ci yu wolof yi di Sëñ Muusaa KA am na fu muy melale lu ni mel ci genn xasidaam, mu ne :
nawet Jolof noor fa te doo nooraani - ndaw lu ca sax soo màggatee yalwaani
 
Kon du war a nekk fu bari ay balluwaayi xéewal .
 
==== Ay way dëkkam ====
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Jolof » lañ ko jële