Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Doxalkat mbëj tekkeem moy ab [[wuutuloxo]] mbëj la, goo xam ne kattan giy duggu ci moom gu [[mbëj]] la te ga muy genne gu [[doolerandu]] la. Doxalkat mbëj yi am nañ solo lool ci dundinu jamono gu bees gi, te it dëgg la sax ne limu doxalkat mbëj yi nekk ci am reew day firndeel tolluwaayu jëm-kanamam. Te itam deminu, maanam yokkute walla nèewte limu doxalkat mbëj yi ci am reew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wàllu [[xarala]] mu reew moomu. Ngir dëggal loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfëndikoo bu baax, man naa ni sax ñooy doxal sunug dund.
 
== Xaralay doxin gi ==
Rëdd 11 :
 
==== Doxin ====
Dawanu [[mbëj]] gi day jaar ci ab lëmës gu ñu wëndeel ci ab doggub weñ gi tudd [[Tekkaaral]]. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjbijjaakon bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjbijjaakon googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjbijjaakon gu lëmës gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seex i [[dott]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjbijjaakon; bëj-gànnaaru toolu bijjaakon gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëj-saalumu toolu bijjaakon gu tekkaaral gi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dottu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi man a wéyee.
 
Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan safaanu rek la bijjaakon di judd. Suy dox, ag wàll gu néew ci kattanu mbëj gi day soppeeku tanggoor ngir [[sababu joule]].