Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Doxalkat mbëj tekkeem moy ab [[wuutuloxo]] mbëj la, goo xam ne kattan giy duggu ci moom gu mbëj la te ga muy genne gu [[doolerandu]] la. Doxalkat mbëj yi am nañ solo lool ci dundinu jamono gu bees gi, te it dëggëdëgg la sax ne limu doxalkat mbëj yi nekk ci am reew day firndeel tolluwaayu jëm-kanam mamkanamam. Te itam deminu, maanam yokkute walla nèewte limu doxalkat mbëj yi ci am reew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci walluwàllu xarala mu reew moomu. Ngir dëggëldëggal loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfëndikoo bu baax, mënman naa ni sax ñooy doxal sunug dundudund.
'''UBBITE'''
 
----
Doxalkat mbëj tekkeem moy ab wuutuloxo mbëj la goo xam ne kattan giy duggu ci moom gu mbëj la te ga muy genne gu doolerandu la. Doxalkat mbëj yi am nañ solo lool ci dundinu jamono gu bees gi, te it dëggë la sax ne limu doxalkat mbëj yi nekk ci am reew day firndeel tolluwaayu jëm-kanam mam. Te itam deminu, maanam yokkute walla nèewte limu doxalkat mbëj yi ci am reew bokk na ci wonekat yiy firndeel tolluwaayu yokkute ci wallu xarala mu reew moomu. Ngir dëggël loolu, doyna xool ci jumtukaay yi nekk ci li ñu wër: ca saxaar ba ci watukaay ak yeneen ak yeneen, yi ngeen xam ne nit ku bees ki moo ngi koy jëfëndikoo bu baax, mën naa ni sax ñooy doxal sunug dundu.
 
== Xaralay doxin gi ==
 
==== WallWàll gi solowu: ====
 
* [[Wëndeelukat]]
* [[Tekkaaral]]
* [[Toolu XëccuBijjaakon]]
* [[XëccuBijjaakon]]
 
==== Doxin ====
Dawanu mbëj gi day jaar ci ab lëmës gu ñu lëmëswëndeel ci ab doggudoggub weñ gi tudd [[Tekkaaral]]. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjxëccumbëjbijjaakon bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjxëccumbëjbijjaakon googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjxëccumbëjbijjaakon gu lëmës gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexiseex i [[dott]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjxëccu,mbëjbijjaakon; bëjgannaarubëj-gànnaaru toolu xëccubijjaakon gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëjsaalumubëj-saalumu toolu xëccubijjaakon gu yemtekkaaral gi. Xaaju wëndeelu gu nekk, dotudottu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi mënëman a wëyeewéyee.
 
Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee, ndax ci dawaan safaanu rek la bijjaakon di judd. Suy dox, ag wallwàll gu nèewnéew ci kattanu mbëj gi day tass soppekusoppeeku tanggoor ngir [[sababu joule]].
Dawanu mbëj gi day jaar ci ab lëmës gu ñu lëmës ci ab doggu weñ gi tudd [[Tekkaaral]]. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjxëccu bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjxëccu googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjxëccu gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dott]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjxëccu, bëjgannaaru toolu xëccu gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëjsaalumu toolu xëccu gu yem gi. Xaaju wëndeelu gu nekk dotu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi mënë wëyee.
Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee. Suy dox, ag wall gu nèew ci kattanu mbëj gi day tass soppeku tanggoor ngir [[sababu joule]].
 
== Taariixam ==
Ci atum 1821, lu weesu xamteg feñte gu mbëjxëccumbëjbijjaakon gugi simikat biiboobu di Ørsted xamlexamlewoon, la nekkat[[jëmmalkat]] bu waa-angalteer bii di Michael Faraday defar ñaari wuutuloxo ngir barilyoox li mu duppee ab wëndeelug mbëjxëccumbëjbijjaakon: ab jalaxub mbegedooley gu wëy,bijjaakon gu abmbegewu dooleyte xëccuwéy, ci lu wër ab wëñ, ci maanaa mooy faramfaceyfaramfaceg doxalkat mbëj gu njëkk.
== Lëkkalekaay yu biir ==
* [[Doxalkat demandoo]]
* [[Doxalkat demandowul]]
* [[Doxallat safanoowulwéy]]
* [[dawaan safaanoo]]
 
[[catégorie:xaralaymbëj]]
{{modèle:wikibaatukaay}}
 
[[ca:Motor elèctric]]