Sëriñ Saaliwu Mbàkke wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Bleakgh (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 24 :
Niki ñu la ko waxe leegi Sëñ Saaliwu nekkoon na di ku géeju ci xam-xami lislaam yi: [[Tawhiid]] (wéetal Yàlla (t.s)) [[fiq]] , [[tasawuf]] , [[nos-wax]] walla nahwu ak [[nos-woy]] (haruud) ak [[jotal]] (balaaxa) ak [[leeral]] (bayaan), muy ku yéeme woon ci [[woy]] , daan def ay jam ci woyi dongaam yu tarbiya yi daan faral di def ay woy yu yéeme, ñoom de bokk nañu ci ñi gën a man a woy ci araab ci Senegaal ku ci mel ne Sëriñ Alhaaji Lóo , [[Utilisateur:Abdu Xaadir KEBE]] mi ci wikipedia, nga xam ne loxoom lu fa am solo la te ay gëstoom gën a màcc ci làmmiñu wolof, S Xaliil Màkke, S aboo Kebe mi def ab dalub murit bu jéggi dayo ba ci làkku araab [http://www.wikimouridia.org/index.php?title=%D8%A7%D9%84%D8%B5%D9%81%D8%AD%D8%A9_%D8%A7%D9%84%D8%B1%D8%A6%D9%8A%D8%B3%D9%8A%D8%A9] "www.wikimouridia.org" , S Mamoor Kebe, S Alaaji Mbàkke mi nga xam ne lu dul jeex ciy téere la taalif ci yoon wi ak aji sosam añs , ndax daawu leen bàyyi ci seen jàmm, foo ko fekk ma nga leen di soññ ci sàmmoonteek sarti "jotal" yi walla balaaxa ci seeni njuréefi woy. Ku mokkaloon lu bari la ci woyi waa Gànnaar yi ak waa Andalusi yi
 
==== Ag sonnam ci Jaamu Yàlla ====
Daa na toggoo ci jaamu Yàlla yi lu kawe misaal, mu daan taqook ay dog ciy wird aki tudd-Yàlla, daawu leen ginaawal mukk ak lu yitte yi tar tar mbaa xat-xat yi baree ko ni, kenn ci taalubeem yi nettali na ma ne moom de masul a jël aw wird ndare bu da caa sax ngir sàmmonteek [[Addiis]] bi naa '''"Jëf ji Yàlla gën a sopp mooy ji gën a sax ak doonte néew na"''', muy ku xéroon cig jaamoom ci tënku ci [[Alxuraan]] ak [[Sunna]], daan teet [[bidaa]] ak [[cibéel]] (lu ñu sib), ci anam gu jéggi dayo ba cig tar.