Sooninke wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
 
Rëdd 6 :
== Cosaan ==
 
Yugo Xasse DingaDiŋa Siise:
 
DingaDiŋa Siise walla DingaDiŋa Xoore, ci cosaan, bokk na ci maamu sooninke yi. Kooku moo juge woon Sooni/Sunu, te ñow ba sowu jantu afrig ([[Senegaal]], [[Mali]],[[Gànnaar]]). Ca jamono [[Isipt gu yàgg ga]] la woon, ci mujjam. Bi mu agsi foofu ak gangooram, moo sos imbratoor gi bu ñu naan GANA walla WAGADU.
 
Saraxule ñoo fi jëkk a dugg ci [[Lislaam]], ci réewum [[Senegaal]], Xeet woowu ñoo jur Jula yi. Jiitu nañu [[Wolof]] yi ca [[Kajoor]] ak [[Bawal]] Séeréer si ca [[Siin]] ak [[Saalum]], foofu fépp ñoo fi njëkk a nekk. [[Imbraatóor]]u [[Gana]] moo ko tabax, ak nguuru [[Gajaga]], nguuru [[Jara]]. Seeni buur Tunka lees leen di dàkkantale. Ci mbay lañu daan dunde, yaxantukat (jaaykat) yu mag lañu woon. Seen xeet woowu, am na ay tukkikat yu ba bari, yu daa tukki, di jaay guro, yére, takkaay, ci fépp ci [[Mali]], Senegaal, Niseer, Gine ak Gine-bisaawóo, Gànnaar, ba Kodiwaar. Ci nit ñu nuul yi, dañu bokk ca fi jëkk ñow Tugal. Ca Gànnaar ñu bari ca dëkk ba tudd Gidimaxa lañu, ci wetu Fuuta-Tooro la, foofu tamit nekk nanu fa bu yàgg, ba Tekuruur nekkee. Mamadu Lamin Drame, Sëriñu Saraxule la bu juge Gajaga/Galam, bu ñuy wax tay [[tund]]u [[Bàkkel]]( (Departement de Bakel), xare na ak tubaab yi bëggoon a boole dëkk bi ci seen moomeel ci atum 1880. Musaa Molo buuru Fulaadu, ci [[nguuri Pël]] yu firdo yi, doomu Alfa Yaaya Molo Balde, moo ko daaneel, booba nag buuru Pël bi tubaab bi la àndaloon. Mamadu lamin, tubaab yi ñoo ko ray ca xare ba ñu tudde xareb Tubaa-Kuta, ca atum 1887.