Sooninke wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
 
Saraxule wenn xeet la, ci askanu Mande la bokk. Saraxule ñoo fi jëkk a dugg ci [[Lislaam]], ci réewum [[Senegaal]], Xeet woowu ñoo jur Jula yi. Jiitu nañu [[Wolof]] yi ca [[Kajoor]] ak [[Bawal]] Séeréer si ca [[Siin]] ak [[Saalum]], foofu fépp ñoo fi njëkk a nekk. [[Imbraatóor]]u [[Gana]] moo ko tabax, ak nguuru [[Gajaga]], nguuru [[Jara]]. Seeni buur Tunka lees leen di dàkkantale. Ci mbay lañu daan dunde, yaxantukat (jaaykat) yu mag lañu woon. Seen xeet woowu, am na ay tukkikat yu ba bari, yu daa tukki, di jaay guro, yére, takkaay, ci fépp ci [[Mali]], Senegaal, Niseer, Gine ak Gine-bisaawóo, Gànnaar, ba Kodiwaar. Ci nit ku nuul y, danu bokk ca fi dieuk nio Europe. Ca Gànnaar ñu bari ca dëkk ba tudd Gidimaxa lañu, ci wetu Fuuta-Tooro la, foofu tamit nekk nanu fa bu yàgg, ba Tekuruur nekkee. Mamadu Lamin Drame, Sëriñu Saraxule la bu juge Gajaga/Galam, bu ñuy wax tay [[tund]]u [[Bàkkel]]( (Departement de Bakel), xare na ak tubaab yi bëggoon a boole dëkk bi ci seen moomeel ci atum 1880. Musaa Molo buuru Fulaadu, ci [[nguuri Pël]] yu firdo yi, doomu Alfa Yaaya Molo Balde, moo ko daaneel, booba nag buuru Pël bi tubaab bi la àndaloon. Mamadu lamin, tubaab yi ñoo ko ray ca xare ba ñu tudde xareb Tubaa-Kuta, ca atum 1887.
'''Saraxule''' walla '''sooninke''', wenn xeet la, ci askanu Mande la bokk. Am naa yeneen tur ñu leen tudd: '''Wangara''', '''Tubakai''', '''Aswanik'''.
 
'''Sooninke''', mooy ku juge Sooni / Sunu. Sooni (walla Sunu) benn dëkk la ca Isipt, ñu ko gëna raññe ci tur wi di Aswan. Maamu sooninke yi, dekk boobu lañu baawo, moo tax ñu yore tur wi '''Sooni-nke'''.
 
== Cosaan ==
 
Yugo Xasse Dinga Siise:
 
Dinga Siise walla Dinga Xoore, ci cosaan, bokk na ci maamu sooninke yi. Kooku moo juge woon Sooni/Sunu, te ñow ba sowu jantu afrig ([[Senegaal]], [[Mali]],[[Gànnaar]]). Ca jamono [[Isipt gu yàgg ga]] la woon, ci mujjam. Bi mu agsi foofu ak gangooram, moo sos imbratoor gi bu ñu naan GANA walla WAGADU.
 
Saraxule wenn xeet la, ci askanu Mande la bokk. Saraxule ñoo fi jëkk a dugg ci [[Lislaam]], ci réewum [[Senegaal]], Xeet woowu ñoo jur Jula yi. Jiitu nañu [[Wolof]] yi ca [[Kajoor]] ak [[Bawal]] Séeréer si ca [[Siin]] ak [[Saalum]], foofu fépp ñoo fi njëkk a nekk. [[Imbraatóor]]u [[Gana]] moo ko tabax, ak nguuru [[Gajaga]], nguuru [[Jara]]. Seeni buur Tunka lees leen di dàkkantale. Ci mbay lañu daan dunde, yaxantukat (jaaykat) yu mag lañu woon. Seen xeet woowu, am na ay tukkikat yu ba bari, yu daa tukki, di jaay guro, yére, takkaay, ci fépp ci [[Mali]], Senegaal, Niseer, Gine ak Gine-bisaawóo, Gànnaar, ba Kodiwaar. Ci nit kuñu nuul yyi, danudañu bokk ca fi dieukjëkk nioñow EuropeTugal. Ca Gànnaar ñu bari ca dëkk ba tudd Gidimaxa lañu, ci wetu Fuuta-Tooro la, foofu tamit nekk nanu fa bu yàgg, ba Tekuruur nekkee. Mamadu Lamin Drame, Sëriñu Saraxule la bu juge Gajaga/Galam, bu ñuy wax tay [[tund]]u [[Bàkkel]]( (Departement de Bakel), xare na ak tubaab yi bëggoon a boole dëkk bi ci seen moomeel ci atum 1880. Musaa Molo buuru Fulaadu, ci [[nguuri Pël]] yu firdo yi, doomu Alfa Yaaya Molo Balde, moo ko daaneel, booba nag buuru Pël bi tubaab bi la àndaloon. Mamadu lamin, tubaab yi ñoo ko ray ca xare ba ñu tudde xareb Tubaa-Kuta, ca atum 1887.
 
== Nosteg mbolaay ==
Bokk na ci askanu Saraxule:
 
* Horon, ñoo doon buur yi.
* Ñaxamala, ñoo doon ñeeño yi, ràbbkat yi, wuude yi , tëgg yi ak seen yyi.
* Jaaro, waykatu buur yi, xam nañu cosaanu Saraxule yépp, Koora ak Xalam lañuy waye buur yi (Tunka)
* Komo ñoo doon jaam yi.
 
== Sant yi ==
 
Waaye népp dañuy bay seeni tooli bopp. Seeni Sant yi gën a siiw: Ture, Siise, Baccly, Sumaare, Daraame, Kebe, Fofana, Daabo, Jaabi, Silla, Jakite, Soxna, Tunkara.