Wërlaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Wërlaay gi di ci tubaab (environnemt) mooy dénd bi maanaam (nature bi) ak li ci nekk ciy way dund ak yu dundul, ci gàttal daal adduna bi nu wër ci kaw suuf si. Xam-xamu wërlaay mooy biy jéem a indi ay tontu ci yenn laaj yi aju ci nan la dénd biy jëfe ak a jëflanteek way nekk yiy dund ak yeneen way nekk yi, walla nan lay jëflanteek digg bi ko wër moo xam digg bu kimya la (simi) walla bu dénd (nature). Digg bii moom lanuy tudde “Noste gu wërlaay”. Looloo waral nuy gis noste gu wërlaay muy luy ame ci ay way nekk yuy dund ak yu dee walla yu way. Xam-xamu wërlaay mooy jàng ak gëstu way nekk yiy dund ak séenug séqoo ak li leen wër ak jeexiital gi nuy def ci sunug séqoo ak suuf si. Nosteg wërlaay mooy mbooleem jëfka (desfacteurs) yu dundul ak mboolaay (société) yiy dund yu xeet yi nekk ci benn gox walla barab. Dénd bi day wëndéel mbir yi mu jëfandikoo woon ngir delloo leen ñu mujjaat di mbir yu am solo ak njariñ. Càllalag ñam ci kaw suuf si, aw melo la ngir wone ni kàttanug ñam di dugge ci wërlaay gi. Foofu ñam da fiy juge ci aji nekk dem ci jeneen n gir jox kàttan dundat boobu di sàqami ñam wi ak a reesal, gépp càllalag ñam nag ci jant bi lay tàmbalee. Dundat yi nit ci la munt a liggéey ab dundam, looloo tax manul a ñàkk mu jot ci dundam boobu jële ko ci gàncax yi walla yeneen dundat yi, looloo waral ñuy jàppe dundat yi ay way lakk walla ay way jëfandiku (consomateur), mujjantalu dundug dundat it mooy ag feccikoom (ag tasam) jaare ko ci ay mikrob walla ay gàncax ngir mujjati di suuf, gàncax gi muucooti ko ngir liggééyati ci ñam wu beesati. Lii nag moom lanuy tudde “Càllalag ñam”, bokk na ci jëfkay dénd yi ci nosteg wërlaay gi te am ci jeexiitalm it: leerug jant bi ak ker gi ak tàngoor wu diggdóomu wi ak séddalig sewogaraafi gi ak ngelaw li ak barab yu yékkatiku yeek yu suufe yi ak melokaanu suuf seek ndox mi. bokk na ci jëfkay kimya yi yiy bàyyi ay jeexiital ci nosteg wërlaay gi: tolluwaay (niveau) bu ndox yi ak ngelaw li walla jawwu ji ci suuf si ak kem ni way dundal yu gàncax yi di seeye ci suuf si ak ndox yi ak tooke yi ci nekk, ak xoromus ndoxum géej ak oksijiin bi ci seey.
. والنظام البيئي هو كل العوامل الغير حية والمجتمعات الجية للأنواع في منطقة ما. والطبيعة تقوم تلقائيا بعملية التدوير للأشياء التي إستعملت لتعيدها لأشياء نافعة . و سلسلة الطعام فوق الأرض وهي صورة لإظهار تدفق الطاقة الغذائية في البيئة, ففيها تتوجه الطعام من كائن لآخر ليعطي طاقة للحيوان الذي يهضم الطعام وكل سلسلة طعام تبدأ بالشمس . والحيوانات بما فيها الإنسان لايمكنها صنع غذائها . فلهذا لابد أن تحصل علي طافاتها من النباتات أو الحيوانات الأخرى. لهذا تعتبر الحيوانات مستهلكة . وفي نهاية حياة الحيوان تحلله بواسطة الميكروبات والنباتات أيضا ليصبحا جزءا من الأرض بالتربة ليمتصها النباتات من جديد لصتع غذاء جديد. وهذا ما نسميه سلسلة الغذاء.
 
ومن العوامل الطبيعية في النظام البيئي ولها تأثيرها ضوء الشمس والظل ومتوسط الحرارة والتوزيع الجغرافي والرياح والإرتفاعات والمنخفضات وطبيعة التربة والمياه .ومن العوامل الكيماوية المؤثرة علي النظام البيئي مستوي المياه والهواء في التربة ومعدل ذوبان المغذيات النباتية في التربة والمياه ووجود المواد السامة بهما وملوحة المياه للبيئة البحرية والأكسجين الذائب بها.