Lebu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
 
'''Lebu''', mooy benn waaso nekk ci reewum [[Senegaal]]. Ñoom, [[Ndakaaru]] mooy seen dëkk, ñu leen fekk tamit ci diggante Ndar (Saint Louis) ak Tenŋeej (Rufisque), ba Mbur. Ci wetu geej ak tefes. NappCi napp mi lañu dund, ci seen cosaan. Seen lakk di wolof. Seen wolof dafa xawa wutte tuuti ak wolof bi yeneen yi lakk. Am na ñu ne, lebu yi ñoo jëkksos lakk wolof.
 
== Lebu (baat bi) ==
 
Cosaanu baat boobu, wutte na ci li kilifa yi tekki. Ñooñu dañudeeñi wa,nettali ay cosaan yu wutte: ''leeb'' moo juur baat bi. Ci ñoom amAm na ñeneen yiñeneeni wax ''luubu'' mooy ''bañ'', ndax ci cosaan, Lebu yi dañu musmusa bañ ku leen noot.
 
[[Seex Anta Jóob]], ci gestu amgestoom, da wone ni, li ñu tudde lebu, am na lu mu bokk ak tur boobu ñu joxe reewum [[Libi]].
Libi, ci jamono [[Isipt gu yàgg ga]] amoon, moo ne woon benn diwaanu, nit ñi di fa dem RëbbRëbbi, ak nappnappi. Dëkk boobu dafa janno ak geej gi.
Moo tax ñu yoroon Isipt yu yagg ga, tudde dëkk boobu: rëbu. Ñu wara xam ni, Seex Anta Joob ak yeneen gestu kat, wone nañu ko, lakk boobu amoon ca Isipt boobu, ak lakk wolof, ñoo bokk maam. Rëbu moo juur Lebu (r-l), Lebu moo juur Libi. Dëkk bi ngañu xam ne, ay nit ñu ñuul ñoo fa ne woon, te ñu daan tudd ñu dëkk ca biir reew mi ''kaw''.
 
Mel mini li am Senegaal tey: Lebu yi dëkk ci tefes ak wetu geej gi, kaw -kaw yi dëkk ci biir reew mi.
 
== Cosaan ==
 
Lebu yi, kon, reew mi ñu tudde tey Libi, lañu ne woon ci jamono Isipt gu yagg ga ame. Dañoo mujj gaddaydaw dëkk boobu, ndax amoon na benn askan bu ñowoon foofu, joge [[Asi]], te ñu leen daan begga noot. Ñoom ñoo Persi yi.
 
Ci seen gadday, jaar nañu ci ay dëkk yu bare ([[Sudaan]], [[Caad]], [[Niseer]], [[Mali]]). Sudan[[Sudaan]], mooy dëkk bi Lebu yi baawo, ñu ko gëna raññe ci turu Nubi walla Kuus.
 
Senegaal, lañu agsi, jamono nguuru Tekruur[[Tekuruur]] ame. Foofu lañu fekk seen bokk, di [[Pël]] yi ak [[Séeréer]] yi. Rawatina Pël ak Seereer yi ñuy napp, ñu leen tudd ci lakku pulaar ay Cuballo / Subalbe. Foof lañu sanc ay dëkk mel ni KasKas ak Njum.
 
Waaye ci Senegaal, taxawuñu Tekruur rekk. Jaar nañu Jolof, ak Kajoor, sooga mujj agsi ca Ndakkaru ci diggante atum 1430 ak 1530.
 
Foofu, ay Socé lañu fekk.
Rëdd 32 :
Ñoom ci senn bopp, dañu xaaj ci ñaari njabootay yu mag, di Sumbejun yi ak Beeñ yi.
 
Ñoo yore woon gogox yi ci Ndakaaru: Yoff, Wakam, Ngor, Sumbejun... .
 
== Sant yi ==
Rëdd 38 :
Lebu yi ñoo bokk sant ak Seereer yi, mel ni: Ndóoy, Puy, Ndir, Jeen, Yaad, Jaañ, Fay, Jeey, Sar, Caw, Njaay, Juuf, Sek.
 
YorBokk nañu ay sant tamit ak [[Tukkloor]]/[[Pël]] yi: Mbay, Gey, Ñaŋ, Jaw, Waad, Gay, Joob, Samb, Conŋaan, Baaxum, Jeŋ... .
 
Ñu sant ''Mbeŋ'', ci li cosaan tekki, seen maam ay [[Mandinke|Mandiŋ]] lañu woon, seen mamaat di Jolof Mbeŋ (ab lamaanu Jolof), juge Mali.
 
Da firnde ni, Lebu yi, ci ñoom ñi lañu cosaanoo. Mel ni [[wolof]] yi rekk.
Ligne 44 ⟶ 46 :
== Diine ==
 
Lebu yi, ay jullit lañu. Ñu bare bokk ci Tariqa Tijaan, ak Layeen yi (Maam[[Seydinaa LimamuLimaamu Laay]]). Seen këru diine di Kambereen, ca Yoff.
 
Waaye, du tax ñu fate seen cosaan, ak li seen maam defoon, ba ñu nekke Ceddo. Manaam tuur yi. Tuur yi, am na solo ci Lebu yi, ndax ci seen jaar jaar, tuur yi, geddgëdd gu mag lañu yoroon ci ñoom, ci lu jëme ci xare yi, ak yeneen xeew yu amoon solo ci seen cosaan.
 
Ci seen tuur yi, ''ndëpp'' la nit ñi gëna xam, ngiir faj febaru ñooñu ngañu xam ne, jiine ñoo tax. Jiine ci Lebu, ''rab'' leen ko tudde.
 
Lëk Dawwur, Maam Kumba Kastel, Maam Jaare, ak yeneeni tuur, bokk naneen ci ñooñu Lebu yi seqante.
 
== Xool itam ==
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Lebu » lañ ko jële