Aten wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
EmausBot (waxtaancëru)
m r2.7.2+) (Robot: Adding gag:Afina
Xqbot (waxtaancëru)
m r2.7.3) (Robot: Modifying hsb:Athen; cosmetic changes
Rëdd 5 :
Aten dëkk bu mag la, ci réewu [[Geres]] mooy péey ba sax, te siiw na ngir xam-xam ba'ak njàng ma, ak caada ja. Yaakaarees na ne lu ëpp téeméeri junni ciy way dëkk ñoo fa dëkke. Nekkoon na péeyu nguuru waa Geres, bi tuddoon Atig (''Attique''). Tey mu tudd Aten .
 
Sancees na Aten daanaka 3.000 at Nj. Is (njëkk Iisaa). Daanaka 500 at njëkk Iisaa fekkoon na mu am nguur gu yaatu lool. Waaye Geres dafa ñàkkoon suuf. Moo tax waa Geres yi tuxu, di sanc ay dëkki Geres yu bari ca [[Óróop|Tugal]] ak [[Asi]] gu ndaw gi.
 
Moone ca jamonoy [[Pool]] dafa ñàkk xaalis. Amatuñu nguur, te diiwaanam Atig dafa tuuti - dénd bu tollook 2.600 kilomet kaare matul sax benn departemaŋ ca [[Senegaal]]. Amul feneen ca Atig fu gën a sore Aten 40 kilomet. Seen suuf musuñoo doy seen soxla. Taw bi barewul woon, lu tollook taw bi ñu am ca noru Senegaal. Ñetti cér ca ñeent ca suuf si amul njëriñ ci bey te yu bare ci yi des amoon njëriñ ca bey garabu oliw rekk. Amoon nañu mbélli xaalis waaye fekk nañu ne jeex nañu tàkk laata jamono nguuru Room. Tamit seen doole ci jaay wàññiku na, ndax doole yeneen dëkk yu mel ni [[Ancos]], [[Korent]], [[Efes]], ak [[Alegsàndiri]].
Rëdd 96 :
[[hif:Athens]]
[[hr:Atena (grad)]]
[[hsb:AthenyAthen]]
[[ht:Atèn]]
[[hu:Athén]]
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Aten » lañ ko jële