Sëriñ Muusaa KA wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 8 :
 
jigéen ju ndaw araf ya lan ko tënke - tënk ba bis pénc ba lan koy tinki
 
jiimug jigéen mooy jekki bum jàllantu - ndaxte bu jàllantoo asal njaaloontu
 
cofeel gu mat sëkk a ko war cib sëriñam - ku bëgg dof te ku doful doo am ngërëm
 
jaamu boroomam jaamu it boroom këram - moo war jigéen su ko manee dàmmey ngëram
 
jam tuñ ma, jam siiñ ma'ak njamal-yàllaam la - jaalu-yàllaam wa ne Yaasin Salla'a
 
Jàmm ak juddook jikkoo waral ñuy tànn - ne xur wi wenn la te jiim yiy jenn
 
Ligne 17 ⟶ 22 :
 
kaaf nga na baax gaaf, bari ngor, toog fa këram - na bari kersay kër-këriy sàkku ngërëm
 
nay ngone bum def mag te bum gàtt kutuj - bum gudd lool fum toll ànd ak latkoloñ
 
Ligne 22 ⟶ 28 :
 
yaa ga na yaatu ŋàpp, yaatal dëkkandoom - yaatal boroom këram ci lépp lu mu moom
 
yaru te yomb te yéwén te yaatu - cub sëriñam te la mu yor bum laatu
 
Ligne 27 ⟶ 34 :
 
arafu nuun gii ku ko boole xejj - ci sa boroom kër gaa ya duñ la xàjji
 
neex cere, neex dereet te neexu làmmiñ - neex lépp tey neexlaate gàttu gémmiñ
 
jigéen na maandu, man a muñ te mokk - di muñ di muuñ di mooñ cereem ne mekk.
 
 
== Jikko yu aju ci arafu baa jëm ci jigéen ==
 
arafu baa yile jigéen ju boole - seen jikko yii kenn du la ba ngay xoole
 
baax baay te booleek bari bayreek barile - ba su boroom këram amul muy defale
 
bëñam ya weet tàll ba mel ne perkaal - bët ba ne bàq bakkanam bay safu jaal
 
day neexu làmmiñ, neexu ñam te mokk lool - lewet te nooy ku mu dajeel sukkal la teel