Sëriñ Muusaa KA wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Nawet Jolof noor fa te doo nooraani - ndaw lu ca sax boo màggatee yalwaani.
 
(bayit[[Bayit wu mujj wi ci jiggéenjigéen la jëm, sabab yi tax ñu koy tànn niki soxna), mu jël araf ya araf wu ci nekk mu def ciy bëyit]]
 
Jiim gi
 
jigéen ju ndaw araf ya lan ko tënke - tënk ba bis pénc ba lan koy tinki
jiimug jigéen mooy jekki bum jàllantu - ndaxte bu jàllantoo asal njaaloontu
cofeel gu mat sëkk a ko war cib sëriñam - ku bëgg dof te ku doful doo am ngërëm
jaamu boroomam jaamu it boroom këram - moo war jigéen su ko manee dàmmey ngëram
jam tuñ ma, jam siiñ ma'ak njamal-yàllaam la - jaalu-yàllaam wa ne Yaasin Salla'a
Jàmm ak juddook jikkoo waral ñuy tànn - ne xur wi wenn la te jiim yiy jenn
 
Kaaf gi
 
kaaf nga na baax gaaf, bari ngor, toog fa këram - na bari kersay kër-këriy sàkku ngërëm
nay ngone bum def mag te bum gàtt kutuj - bum gudd lool fum toll ànd ak latkoloñ
 
Yaa gi
 
yaa ga na yaatu ŋàpp, yaatal dëkkandoom - yaatal boroom këram ci lépp lu mu moom
yaru te yomb te yéwén te yaatu - cub sëriñam te la mu yor bum laatu
 
Arafu nuun gi
 
arafu nuun gii ku ko boole xejj - ci sa boroom kër gaa ya duñ la xàjji
neex cere, neex dereet te neexu làmmiñ - neex lépp tey neexlaate gàttu gémmiñ
jigéen na maandu, man a muñ te mokk - di muñ di muuñ di mooñ cereem ne mekk.
 
 
== Jikko yu aju ci arafu baa jëm ci jigéen ==
(bayit wu mujj wi ci jiggéen la jëm, sabab yi tax ñu koy tànn niki soxna)
arafu baa yile jigéen ju boole - seen jikko yii kenn du la ba ngay xoole
baax baay te booleek bari bayreek barile - ba su boroom këram amul muy defale
bëñam ya weet tàll ba mel ne perkaal - bët ba ne bàq bakkanam bay safu jaal
day neexu làmmiñ, neexu ñam te mokk lool - lewet te nooy ku mu dajeel sukkal la teel