Xam-xamu nosukaay wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
DSisyphBot (waxtaancëru)
Ibou (waxtaancëru)
mAucun résumé des modifications
Rëdd 4 :
 
== Taariix ==
Ba àdduna dooree ba tay nit daa mas di ut ay jumtukaay ngir man a def ay waññeem. Ci jumtukaay yooyu, ci yi gën a yàgg, man nañu cee lim àlliway [[Hammurabi]] (1750 laata yeesu). [[Wuutuloxo]] yu [[doolerandu]] yu njëkk ñoo ngi tàmbalee feeñ ci diggante XVIIXVI ak XVII<sup>u</sup> xarnu. Waññikaay bu doolerandu bu njëkk, jàpp nañu ne, mooy bu Wilhelm Schickard ci XVI<sup>u</sup>.
 
Ci [[1642]] [[Blaise Pascal]] defaroon na, moom itam, ab Waññikaay bu doolerandu, doonoon bu ñu doon jaay sax, ba tay jii juroom-ñeent ci yooyu man nga leen a fekk ci jeexiituwaay (musemusée) yi. Ci ay njëlbeenam man nanoo wax ne [[xaymaan]] yi rekk ñoo ci doon yëngu ndax li leen yetteeloonyitteeloon moo doonoon defar ay jumtukaay yu leen di yombalal seeni Waññi yu xayma. Ay cëslaayam yépp ci xayma lañu taxaw, rawati na liñuy way [[aljibar bu Bool]].
 
Tay jii xam-xamu nosukaay jël na wàll wu am solo ci sunug dund, cig suqali ci wàllu koom-koom ak mboolaay yu askan yi.