Senegaal wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
EmausBot (waxtaancëru)
m r2.6.4) (Robot: Adding zu:ISenegal
Aucun résumé des modifications
Rëdd 19 :
}}
 
'''Senegaal''' menn la ci [[réew]] yi ne ci [[Sowwu Afrig]], mu bokk nag ci [[Afrig gu bëj-saalumu sahraa]] (Afrique sub-saharienne), [[Mbàmbulaanug Atlas]] diw digam ci sowwu, taqaloo ak [[Gànnaar]] ci bëj-gànnaar ak penku, [[Mali]] féete ko penku, [[Ginne]] ak [[Ginne- Bisaawóo]] ci bëj-saalum, [[Gàmbi]] moom sos ab daanaka-jiba (quasi-enclave) ci biir Senegaal, sutuxlu ba ci lu ëpp 300 km ci biir suuf yi. Duni [[Bopp bu Wert]] bi (Cap-Vert) ñi ngi ci 560 km ci tefesi Senegaal yi.
 
Réew maa ngi lebe turam wi ci dex gi ko peek ci penku ak bëj-gànnaar, te ab balluwaayam bawoo ca [[Fuuta Jallon]] ca Ginne, di [[Dexug Senegaal]]. Ab kilimaam bu gëwéel la te di bu fendi te yor ñaari jamono: jamonoy nawet (jamonoy taw) ak ju noor (jamonoy fendi).