Xam-xamu suuf si ak jawwu ji wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 19 :
== Jéeri ji (Lithosphere) ==
 
Mbooleem beeñ bi ak [[doj yi (montaañ yi)]] ñoo sos wàll gu tond (superficiel), gu dëgër gu [[kol-kolu suuf si]], ñu koy woowe [[Jéeri ji]] walla aji wow ji.
 
bu ñu séddalee Jéeri ji, def ko ñeenti xaaj, ñatt yi daanaka ndox yee leen muur, yooyu ndox nag ñoo sos [[mbàmbulaan yi]] (oceans yi)ak géej yi, waaye wàll yi génn ci jéeri ji; nga xam ne ndox yi muuruñu leen ([[gox yi (les continents)]] ak [[dun yi (les iles)]] , wàll yii ñooy [[wërlaay (environnement)]] gu dëppoo te méngoo ak dundug nit, moo tax fi lay dunde, di fi defe ay liggéeyam, walla li ëpp ci ay cawarteem (activités).
 
Jéeri ji nag day dund tey màgg ci anam gu sax, ak doonte fi nun, day mel ne ni mu nekke soppikuwul. Li ko waral nag mooy ni muy soppikoo day faral a yeex lool: doj yi bu ñu sosoo ci ron géej gi, dañuy mujj lemu, yékkatiku, màgg ànd ak [[Jamono yu jiyoloji yi]]ñooy mujj sos ay càllalay doj (montaañ) yu yees.
 
Ci safaanub loolu doj yi [[gaaru (exposéwu)]] ci kanamu [[jëfkay jawwu yi (les elements atmospheriques)]]dañuy xolliku, di xoosu, di fellu, bu ko defee, yooyu xoosiit ak felliit (ban yeek beeñ yeek yi ni deme) ñooy mujj sottikuwaat ci géej gi