Royuwaay:Xët wu njëkk/limuwaay ndeyjoor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 23 :
 
<center> '''Xibaar / Li gën a fés''':</center>
;A.W (Akaademi Wolof), aw na ci yoonu suqali Wolof !: Mbooloo mu di doomi réew mi dajee nañu ca Tuubaa sos ab Akaademi jagleel ko làkku Wolof. Ñu nar a joyal séen yitte yi gën a mag ci dajale mboolem mbindi mag ñi, ñi bind ci Wolof, gëstu yees ci jot a def, saytu arafi bindiin yi (yoy latin ak yoy alxuraan), tekki xam-xam yi ci Wolof, defar baatukaayu Wolof, defar tëraliinu jàng ak sóññ boroom xam-xam yi ñu sonn ci jàng ak binde ci Wolof. Ndajem boroom xam-xam la mu suqali Wolof rekk tax a jóg waliif wutum xaalis. Àndu ñook nguur mbaa kujjeg politig. Ñoom daal, nee ñu, ñu moom séen bopp la ñu tetet sàkku ci mboolem ku Wolof ñor nga jàpp ci liggéey bi ngir suqali làkk wi rekk.
Ku ca bëgg a bokk mbaa nga bëgg ci yeneeni leeraal man ngaa bind ci : akaademibuwolof@gmail.com