Royuwaay:Nataalu ayubés bi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 4 :
<center>'''Nataalu ayubés bi'''</center>
|-
|[[Image:SengoorSëriñ Saaliwu Mbàkke.jpg|thumb|center|350px| Leopool Sedaar Sengoor Sëriñ njiituSaaliwu réewumMBÀKKE, Senegaaljuróoméelu muxalifab njëkkTuubaa]]
'''[[Sëriñ Saaliwu]]''' mi ngi gane àdduna, ca Njaaréem(Senegaal) ci guddig àjjuma gu 14 ci weeru tëbëski, atum 1333 g.g, dëppoo ak 22 satumbar 1915. Aji juram ju góor di ku jaradee leeral ngir xam gi ko nit ñépp xam di [[Seex Ahmadu Bamba]], ju jigéen di [[Soxna Faati Jaxate]], mom Sëñ Moodu Asta mu baax ma te sell. S Tuubaa bi mu ganee àdduna daa bindoon ciw kayit tur wi di (Saaliwu giy tekki aji baax, aji yéwén) jox ko [[Sëñ Muhammadu Lamin Jóob Dagana]], ne ko tudde ko ko, bi mu ko defee moom S Dagana, daa daal di bind as lëf ciy bayit ñaanal ci liir bu tedd bii aw fan wu gudd akug wér, akug yékkatiku ci jamonoom ba mel ni jant, mu wax ca ne:...
''' [[Leopool Sedaar Sengoor ]]''' mi ngi juddoo ca Jiwaalo ci 9 Oktoobar ci atum 1906, génn àdduna ca Werson (ca [[Fraas]]) ci 20 Disambar 2001. Nekkoon taalifkat, bindkat doonoon it killifa aada ca [[Senegaal]]. Mooy ki njëkk a doon njiitu réewu Senegaal (1960-1980).
Wàcc na jal bi ci teeyug bakkanam, bàyyee ko Abdu Juuf. Ñu bari ci àdduna bi dañu koy jàppe kenn ci xalaatkati Afrig yi ëpp solo, yu ñaar-fukkeelu xarnu
 
|}<noinclude>[[Wàll:Xët wu njëkk|N]]</noinclude>