Xam-xamu suuf si ak jawwu ji wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 2 :
, xam-xam la buy gëstu lépp lu aju ci suuf si kaw gi ak biir gi, ak doj yi (montaañ yi)añs. Bu jawwu ji di biy gëstu lépp luy jawwu ak tegaloo gi ñu tegaloo.
 
[['''Jawwu ji''']] nag di ci tubaab ''atmosfeer'' :mooy mbalaanum ngelaw mi wër suuf si. Lees di gën a sori suuf si, ngelaw liy gën di neew-doole di gën di amadi, day mujj sax di lu fàddu (lu absenter)ci ay fukki kilomet ci kawewaay. Li a tax ñu man a séddale Jawwu ji ci ay goxi jawwu yu wuute te tegaloo, gox bu ci nekk ami jagley boppam:
 
[['''FATT-JAWWU]] walla JAWWU JU FATT ji'''(Troposphere): mooy ji gën a tal gën a fatt te gën a féete suuf; moom ngelawam day yëngu jamono ju nekk, fa lay niir yi di sosoo ak mbooleem soppaxndikuy jawwu yi; kon cig jege mooy jawwu ji ëpp ag jeexiital (influence) ci wàllug dëkk ci kaw suuf ak ci ni kilimã bi di séddalikoo