Wolof (askan) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 31 :
Ci Senegaal ñoom ñoo njëkk a gis Tubaab yi. Bu njëkk Ceddo lañu woon, tay ñu bari ci [[yoonu murit]] lañu bokk walla tiijaaniya. Am na ay ay nasaraan (chrétiens) tamit waaye duñu ñu bari (Gore/Ndar). [[Seex Ahmadu Bamba]] Mbakke ak [[Alaaji Maalik SI]] ñoo gën a dugal Wolof yi ci [[lislaam]]. Wolof yu bari gàddaay nanu (walla tukki nanu) dem Faraas, [[Diiwaan yu Bennoo]] yi (États-unis), Itaali, Espaañ. Ci Senegaal ñoo yor pal yi gën a rëy (loolu du lu ñépp man a ànd, ndax gisees na ne Njiitul Senegaal lu njëkk séeréer la woon la ca topp it noonu, boo demee ca xare ba (l'armée)lu ëpp ca kilifa ya doonuñu ko. Kon wax jooju ju deesi xoolaat la). Ñoom ñoo gën a fonk seeni réewm (Nationalisme Sénégalais). Am na ci ñoñ ci Mbay (Kaw-Kaw) lanuy dunde, am ci ñoñ ci Napp, ca géej gi (ci ñoom la Lébu yi bokk). Jom ak Teraanga ci ñoom la fekk baax.
 
== Xool itam ==
*[[Wolof]]
*[[Pël]]
*[[Tukkloor]]
*[[Séeréer]]
[[Wàll:waasoy Senegaal]]