Lebu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Xët wu bees : '''Lebu''', mooy benn waaso nekk ci reewum Senegaal. Ñoom, Ndakaaru mooy seen dëkk, ñu leen fekk tamit ci diggante Ndar (Saint Louis) ak Tenŋeej (Rufisque), ba Mbur. C...
 
Aucun résumé des modifications
Rëdd 4 :
== Lebu (baat bi) ==
 
Cosaanu baat boobu, wutte na ci li kilifa yi tekki. Ñooñu dañu wa, ''leeb'' moo juur baat bi. Ci ñoom am na ñeneen yi wax ''leebuluubu'' mooy ''bañ'', ndax ci cosaan, Lebu yi dañu mus bañ ku leen noot.
 
[[Seex Anta Jóob]], ci gestu am, da wone ni, li ñu tudde lebu, am na lu mu bokk ak tur boobu ñu joxe reewum [[Libi]].
Rëdd 36 :
== Sant yi ==
 
Lebu yi ñoo bokk sant ak Seereer yi, mel ni: Ndóoy, Puy, Ndir, Jeen, Yaad, Jaañ, Fay, Sar, Caw, Njaay, Juuf, Sek.
 
Yor nañu ay sant tamit ak [[TukloorTukkloor]]/[[Pël]] yi: Mbay, Gey, Ñaŋ, Jaw, Waad, Gay, Joob, Samb, Conŋaan, Baaxum, Jeŋ... .
 
Da firnde ni, Lebu yi, ci ñoom ñi lañu cosaanoo. Mel ni [[wolof]] yi rekk.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Lebu » lañ ko jële