Tekuruur wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Tekuruur moo doonoon benn nguur ca bej gannaaru Senegaal. Xeet yu bari tase nañu fa, juge Isipt: Séeréer si, Pël, Sooninke, Naar yi. Leeegi Tekuruur, [[Fuuta-tooro]] la tudd. Koli Tenŋela Bah, denyankobe bi, moo ko jox tuur wi. Ca nguur ga, Tukuloor ak Pël ñoo fa ëpp ba tay, waaye Séeréer si ñoo fa jëkk a nekk, ak Pël. Buur yu bari ñoo yoroon nguur ga:
* JaJaa-Ogo yi ci yoonu imbratooru Gana. Ñoom ay tëgg lañu woon. Bokk ci Pël yi.
* Manna yi. Ca Penku lañu fekke baax (nguuru jaara / kingi), sant Ñaxate, bokk ci sooninke yi.
* Manna yi.
* Tondiyoo yi. Ñoom ay Séeréer lañu woon.
* Lam-Termess, Lam-Taga, ak Lam-toro yi. Ci ñu nekke buur, [[Jolof]] moo doon uuf dëkk bi, di fi teg ay Farba (Farba Walwalde, Farba Njum, etc).
* Deeniyankooɓe yi, yu Koly tenŋela Bah, Sebee lañu woon, Sebbe mooy [[Ceddo]].