Tekuruur wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Aucun résumé des modifications
Aucun résumé des modifications
Rëdd 8 :
Ba noppi, tubaap yi ñëw ak canc gi (colonisation), ci atu 1890, jël nguur gi, elif Almaami yi, di séddale dëkk bi, ci ay - li nuy wax ci lakku fraanse (Canton) ak (Provinces).
 
Tukuloor, mooy ku dëkk Tekruur, da mel ni baatu Fuutankooɓe / Fuutanke, di ku dëkk Fuuta Tooro. Tur wi ñuy wax Tukuloor tubaab moo ko fi indi, yeneen yi daannaan Wolof yi ñoo ko sos. Nit ñi , dañu faral jaawale, Tukuloor (ku dëkk Tekruur) ak xeet wi nekk ca dëkk boobu. Ñoom, ci waaso yi lañu joge: Pël, Séeréer, Sooninke, Naar. Seeni sant ñoo ko firnde. Deeniyankooɓe ñoo tax lakku pulaar siiw dékk boobu.
 
[[Wàll:Taariixu senegaal]]