Séeréer wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Bennylin (waxtaancëru)
m Loppantig coppite gu 86.160.8.127 (Waxtaan) dello ko ci sumb mu Robbot
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
Séeréer genn giir la gu nekk [[Senegaal]]. Séeréer si ñoo jur Lebu yi ak [[Wolof]] yi, waaye [[wolof]] yi am nañu yeneen xeet yu ñu bawoo tam yu duli Séeréer. Siin ak Saalum mooy seeni nguur.[[Image:SererMan.jpg|thumb|left|Tisserand séeréeru [[Mbissel]] (aquarelle de l'[[David Boilat|abbé Boilat]] dans ''Esquisses sénégalaises'', [[18531850]])]] Soog a nekk Siin-saalum, ca [[Tekuruur]] lañu nekkoon. Dañoo gàddaay dem Siin-Saalum ndax dañu doon daw [[Lislaam]] ak Muraabituun yi (les Almoravides). Muraabituun yi dañu xare "jiyaar" ak séeréer si, ngir dugal leen ci Lislaam, waaye séeréér si bëgguñu woon loolu. Lii lépp nag ca yoonu imbraatóor gu Gana la xewe woon, booba imbraatoor gi mi ngi doon tàmbalee daanu. Foofa ca Siin-Saalum ay Soose ([[Sooninke]]), ñoo fi doon dëkk. Kon mbokkug [[Soose]] ak Séeréer ci dëkkandoo la bawoo, ba noppi Soose yu bari dem nanu dëkki ca [[Kaasamaas]]. Séeréer si dañu doon séddale dëkk bi ci ay Lamana, ca Lamana yépp ay Laman a fa fa daa nekk ay buur. Mbay ak Napp lañu daa dunde. Mbay (Saalum) moo doon turu dëkk bi soog a nekk Siin ak Saalum. Ba noppi ay Mandinke yu juge nguuru [[Kaabu]], ñëw ca Séeréer sa, dëkk ak ñoom. [[Mandinke]] yi ay Nanko (Géer) yu Kabbu lañu woon, seeni buur (Mansa ca làkku Mandinke) ñoo leen dàqe seen réew. Joolaa yi ñoo leen ne ca Siin-Saalum baax na lépp lu nit soxla ngir man a dund am na fa, te foofu am na ay nit waaye amuñu buuru dëgg. Lii moo tax ñu tuxoo Siin ak Saalum. Nanko ak Buuri Séeréer si fi nekkoon (Laman) dañoo booloo, jaxasoo, ba nekk xeet wu ñuy wax ay Gelawaar. Gelawaar, ñoo tabax nguuru Siin ak Saalum. Maysa Waali Joon moo jëkk a nekk buuru Siin. Mbegaan Nduur moo jëkk a nekk Buuru Saalum.
Nosteg mboolaay ga (le système social) nii la tëdde woon:
* Gelawaar yi ñoo neekkoon Buur yi.