Itaali wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 24 :
'''ngir xootal Taarixu Itaali xoolal''' [http://wo.wikipedia.org/wiki/Taariixu_Itaali Fii]
 
[[-Ni Itaali meloon njëkk xare yu Napoleon yi:]]-
 
Itaali laata a Napoleon di ko teg loxo, di ko nangu, nekkutoon réew mu ñu bennal , nekkutoon it di mu am ag temb, moom kay daa seddaliku woon, doon fukki xaaj ak ñaar, yu doon topp ak a nekk ci ron kiliftéefug ay nostey politig yu wuute: nosteg nguur ca Savoia, Piemonte, Napoli, ak nosteg pénc ca Venezia ak Geneva, ak ag àtte gu paab ca Rom, ak gu Dóox ca Toskaana ak Parma, ak xaaj yoo xam ne dañoo nekkoon ci waawug imbraatóor gu Otris gi, ñooy Milano ak Lombardia.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Itaali » lañ ko jële