Dawaanu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Luckas-bot (waxtaancëru)
m r2.7.1) (Robot: Adding ia:Currente electric
Xqbot (waxtaancëru)
m r2.7.2) (Robot: Modifying ku:Sirêma elektrîkê; cosmetic changes
Rëdd 1 :
'''Dawaanu mbëj''' ag [[wal]] la niki yépp gu nosu gu [[Yanu mbëj |yani mbëj]] (njunjam di '''Q'''), naka-jekk cig wëñug weñ lay jaar walla bépp jumtukaay buy [[Watatukaay|watat]]. Dawaan bi dees koo jappee woo, ci ndorteelu taariixu [[mbëj]], niki ag walug yan yu baax (+), donte sax xam nanu ne, su nu xoolee ci [[watatukaay]] yu [[mbell]] yi dawaan gaa ngi judd ca walug [[mbëjfepp]] yi, yi am yan yu bon (-), ci beneen jubluwaay bi. Kon ni ñu foogeewoon ne la dawaanu mbëj di jublu, du noon, waaye safaan wa la, yan yu bon ([[mbëjfepp]]) yi ñooy dox jëm ci yu baax (+) yi. Donte lii yépp, gisiin gu njëkk ga moo wéy di baax, ci déggoo. Njunj gi ñuy jëfandikoo ngir tudd bariwaayu dawaan (limu dawaan giy wal ci jenn [[jamono]]) mooy '''I''', di ko wax taraayu dawaan, te [[bennaanu natt]] bi ñu koy natte di bi àdduna bi déggoo mooy [[ampere]].
 
== Nattug taraayu Dawaan gi ==
Dawaanu mbëj manees na koo natt ak jumtukaay bees di woowee [[nattampere]], waaye gii anam dafay laaj nga dog ndombo gi, xamees na ne du li gën ci yenn nekkiin yi. Dawaan bi manees na koo natt te du jar dog ndombo gi, ci njëlug toolub [[bijjakoon]] bi mu jur, moom. jumtukaay yees di jëfandikoo ngi bii liggéey ràññee nañu ci: [[yëgukaay]] yu sukkandiku ci [[njeexitu Hall]] ak [[lëmës yu Rogowski]]
 
Rëdd 12 :
Xamees na ne ngir [[mbëj]] mi maase ci biir ab [[watatukaay]] faww [[toolu mbëj]] bi ci ëmbu di neen (tus) ci bépp tomb boo jël ci biir watatukaay bi. Su amee ag wuuteeg aj ci diggante ñaari tomb ci watatukaay bi kon dees na fa am toolub mbëj bu wuute ak tus kon dees na fa am it dawaanu mbëj. Wuuteeg aj googu lees di wax [[dooley mbëjdoxalukaay]], di doole jiy xëcc yani mbëj yi, ñuy man di daw toppante doon ag wal, te ci la [[ndombo yu mbëj]], mbëjbijjakoon, [[àtteb Ohm]] ak [[àttey Kirchhoff]] sukkandiku.
 
So jële genn yaa-yaa gu watatukaay bi, benn limu yani mbëj di daw ci biiram ''''ΔQ'''' ci benn diirub jamono ''''Δt'''' dees na ci ame genn taraayu dawaan
:<math>I = \lim_{\Delta t \to 0} \frac {\Delta Q}{\Delta t} = \frac {dQ}{dt}</math>
== Lëkkalekaay yu biir ==
 
* [[Dawaan bu wéy]]
* [[Dawaan bu safaanu]]
* [[Kàttanug mbëj]]
* [[mbëj]]
[[Wàll:dawaanu mbëj]]
 
[[Wàll:xaralaymbëjDawaanu mbëj]]
[[Wàll:dawaanu mbëjXaralaymbëj]]
 
[[af:Elektriese stroom]]
Rëdd 60 :
[[kn:ವಿದ್ಯುತ್ ಪ್ರವಾಹ]]
[[ko:전류]]
[[ku:Sirêma karevayîelektrîkê]]
[[la:Fluxus oneris electrici]]
[[lb:Stroumstäerkt]]