Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

1 octet ajouté ,  14 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
 
Dawanu mbëj gi day jaar ci ab lëmës gu ñu lëmës ci ab doggu weñ gi tudd [[yem]]. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjxëccu bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjxëccu googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjxëccu gu [[wëndeelukat]] bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi [[dot]]. [[Wëndeelukat]] bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjxëccu, bëjgannaaru toolu xëccu gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëjsaalumu toolu xëccu gu yem gi. Xaaju wëndeelu gu nekk dotu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi mënë wëyee.
Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee. Suy dox, ag wall gu nèew ci kattanu mbëj gi day tass soppeku tanggoor ngir [[sababu joule]].
3 292

modifications