Doxalukaay bu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Nouvelle page : '''UBBITE''' ---- Doxalkat mbëj tekkeem moy ab wuutuloxo mbëj la goo xam ne kattan giy duggu ci moom gu mbëj la te ga muy genne gu doolerandu la. Doxalkat mbëj yi am nañ solo l...
 
Rëdd 13 :
* [[Xëccu]]
 
==== Doxin ====
 
Dawanu mbëj gi day jaar ci ab lëmës gu nekk ci ab doggu weñ ngi tudd wëndeelukat. Lëmës googu, gi ñu defare ak wëñu përëm, jur ab toolu mbëjxëccu bu ca dawan jaaree. Toolu mbëjxëccu googu dañ koy sòob ci beneen toolu mbëjxëccu gu wëndeelukat bi jur, mi melokaanoo teewaayu ñaar walla ñetti seexi dot. Wëndeelukat bi tambalee wëndeelu ci sababu njureelu mbëjxëccu gi, “bëjgannaaru“ toolu xëccu gu wëndeelukat bi day wòotalante ak bëjsaalumu toolu xëccu gu yem gi. Xaaju wëndeelu gu nekk dotu gi day soppeeku, ci noonu la wëndeelu gi mënë wëyee.
Doxalkat bii ci dawan safaanu rek lay doxee. Ci doxin gi, ag wall gu nèew ci kattanu mbëj gi day tass soppeku tanggoor ngir [[sababu joule]]