Aten wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 3 :
Ci [[angale]] mooy ''Athens''; Ci [[faranse]] mooy ''Athènes''
 
Aten dëkk bu mag la, ci réewu [[Geres]] mooy pééypéey ba sax, te siiw na ngir xam-xam ba'ak njàng ma, ak caada ja. Yaakaarees na ne lu ëpp téeméeri junni ciy way dëkk ñoo fa dëkke. Nekkoon na péeyu nguuru waa Geres, bi tuddoon Atig (''Attique''). Tey mu tudd Aten .
 
Sancees na Aten daanaka 3.000 at Nj. Is (njëkk Iisaa). Daanaka 500 at njëkk Iisaa fekkoon na mu am nguur gu yaatu lool. Waaye Geres dafa ñàkkoon suuf. Moo tax waa Geres yi tuxu, di sanc ay dëkki Geres yu bari ca [[Óróop|Tugal]] ak [[Asi]] gu ndaw gi.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Aten » lañ ko jële