Aten wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 5 :
Aten dëkk bu mag la, ci réewu [[Geres]] mooy pééy ba sax, te siiw na ngir xam-xam ba'ak njàng ma, ak caada ja. Yaakaarees na ne lu ëpp téeméeri junni ciy way dëkk ñoo fa dëkke. Nekkoon na péeyu nguuru waa Geres, bi tuddoon Atig (''Attique''). Tey mu tudd Aten .
 
Sancees na Aten daanaka 3.000 at Nj. Is (njëkk Iisaa). Daanaka 500 at njëkk Iisaa fekkoon na mu am nguur gu yaatu lool. Waaye Geres dafa ñàkkoon suuf. Moo tax waa Geres yi tuxu, di sanc ay dëkki Geres yu bari ca [[Óróop|ËroopTugal]] ak [[Asi]] Minërgu ndaw gi.
 
MoonaMoone ca jamonojamonoy [[Pool]] dafa ñàkk xaalis. Amatuñu nguur, te diiwaanam Atig dafa tuuti - dénd bu tollook 2.600 kilomet kaare matul sax benn departemaŋ ca [[Senegaal]]. Amul feneen ca Atig fu gën a sore Aten 40 kilomet. Seen suuf musuñoo doy seen soxla. Taw bi barewul woon, lu tollook taw bi ñu am ca noru Senegaal. Ñetti cér ca ñeent ca suuf si amul njëriñ ci bey te yu bare ci yi des amoon njëriñ ca bey garabu oliw rekk. Amoon nañu mbélli xaalis waaye fekk nañu ne jeex nañu tàkk laata jamono nguuru Room. Tamit seen doole ci jaay wàññiku na, ndax doole yeneen dëkk yu mel ni [[Ancos]], [[Korent]], [[Efes]], ak [[Alegsàndiri]].
 
Dëkku njàng la woon, bu amoon benn 'iniwersite'. Naka noonu siiw nañu ndax seen xam-xam ak seen waxin, ndaxte waxin lañu ca gën a jàngale. Wax ak a déglu lu bees rekk lañu daan xinte. Amoon na ay mbooloo boroom xam-xam. Benn ca mbooloo boroom xam-xam moo tuddoon [[Epikuren]]. Kureel la woon, bi sës ci njàngalem Epikuur (mu faatu 270 at lu jiitu jamano Kirist) te fonk bànneex, ba mucc ci bépp tiis. Gëmuñu Yàlla, waaye ñu gëm ne àddina dafa sàkk boppam te amul boroom. Te boo deeyee amul dara lu ciy topp. Nekkatuloo daal. Beneen mbooloo dafa tuddoon [[Estowisen]]. Kureel la woon, bu sës ci njàngalem Senon (mu faatu 265 at lu jiitu Kirist). Fonk nañoo naagu, ba bañ a yég dara, muy bànneex mbaa naqar.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Aten » lañ ko jële