Aten wuute gi ci sumb yi

30 octets supprimés ,  9 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
m (The file Image:Parthenon_temple.jpg has been replaced by Image:Erechtheum_temple.jpg by administrator commons:User:Courcelles: ''File renamed: bad name''. ''Translate me!'')
Ci [[angale]] mooy ''Athens''; Ci [[faranse]] mooy ''Athènes''
 
Aten dëkk bu mag la, ci réewu [[Geres]] mooy pééy ba sax, te siiw na ndaxngir xam-xam ba'ak njàng ma, ak baaxcaada ya, maanaam li tubaab di wax 'kiltiir'ja. YaakaarYaakaarees nañuna ne lu ëpp 500.000téeméeri nitjunni ciy way dëkk ñoo fa dëkkoondëkke. Nekkoon na péeyu diiwaanu nguuru Geregwaa yiGeres, bubi tuddtuddoon Atig (''Attique''). Tey ji Aten lamu tudd baAten tey, tamit mooy péeyu Geres.
-
 
Samp nañu Aten daanaka 3.000 at lu jiitu jamono Kirist. Daanaka 500 at lu jiitu jamono Kirist amoon na nguur bu yaatu lool. Waaye Geres dafa ñàkkoon suuf. Moo tax waa Gereg yi dem nañu toxu, di samp dëkki Gereg yu bare ca [[Óróop|Ëroop]] ak [[Asi]] Minër.
 
2 337

modifications