Aten wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Movses-bot (waxtaancëru)
m r2.6.2) (robot Adding: ie:Athina
CommonsDelinker (waxtaancëru)
m The file Image:Parthenon_temple.jpg has been replaced by Image:Erechtheum_temple.jpg by administrator commons:User:Courcelles: ''File renamed: bad name''. ''Translate me!''
Rëdd 20 :
 
[[Dencukaay:Der_Parthenon.JPG|thumb|250px|right|Parténon ca Aten.]]
[[Dencukaay:Parthenon templeErechtheum_temple.jpg|thumb|250px|right|Parténon ca Aten.]]Màggalukaay bu gën a am solo moo doon li ñu tudd 'Parténon' bi ñu defaroon ngir yàllay dëkk ba, maanaam, Atena. Guddaay 72 meetar la, yaatuwaay 34 meetar, te kawewaay 20 meetar. Ca kaw kenu ya amoon na nataal bu ñu yett bu wëroon tabax bépp ca 92 wàll. Wàll bu ne indi na benn ca seeni nettali yàlla. Amoon na beneen nataal bi ñu yett ca diggante kenu ya bu amoon 600 melo ya - ay góor, ay jigéen ak ay bàyyima yi bokk ca ña indi seen yàlla Atena benn yére wurus at bu nekk. Guddaayu nataal bi mooy 160 meetar. Te def nañu nataal yi ngir ñi taxaw ca suuf di ko xool yaakaaroon nañu ne dañuy jàkkaarlook nataal ba, fekk na ne nekkoon na 10 meetar ca seen kaw.
 
Waa Aten jaamu nañu ay yàlla yu bare. Waaye yàllay dëkk ba moo doon Atena. At bu nekk ci weeru yuuliyoo, amoon nañu benn màggal lu diir 8 fan. Ca fan yu jëkk ya def nañu ay joŋante, rawante gaal ya, fas ak sareeet ya, rawante ca woy ak nettali, ay mbumbaay. Ca juróom-benneel ba fan, ca fajar, saraxalekat ya ak magi dëkk ba, jiitu nañu mala ya ak waa dëkk ya yépp, ñu dox ca biir dëkk ba, ba egg Panténon fu ñu def sarax ya, te ñépp lekk yàpp. Sarax nañu 100 mala, mooy nag ak xar, at mu nekk.
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Aten » lañ ko jële