Leopool Sedaar Sengoor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Abdu Xaadir KEBE (waxtaancëru)
Rëdd 6 :
Léopold Sédar Senghor ma nga juddoo ca Jiwaalo, di ab [[dëkk]] bu ndaw bu ne ca tund wu [[Mbuur]], ci diiwaanu [[Cees]]. Baayam di Basil Jogoy Senghor, ab yaxantukat la woon bu bokkoon ci kuréel gu diggu gi ci giirug séeréer, di genn ci néewte yi ci Senegaal .
Yaayam di Ñilaan Njéemée Baaxum,ñatteelub baayam . Bi mu amee juroom ñatti at, la tàmbali am njàngam ci ab Gospel: benn jàngu bu dëkku bu Baay yu Ruu Gu Sell gi (les pers catholiques). Ci atum 1922 la dugg leekool (mbaa jàngu bi)te booba ma nga Ndakaaru, muy ku soppoon njàngat lu Faraas, di woon ku ràññiku ci làkku Faraas, Laatin, wu Geres ak Jabru, mu daal di am Bakalooriya, daal di am ag may ngir àggale am njàngam ca Faraas
-
<br />
 
* Yaxantukat ci fr:commerçant
* kuréel gu diggu gi ci fr:bourgeoisie