Ndombo gu mbëj wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
VolkovBot (waxtaancëru)
m robot Adding: ht:Sikui elektrik
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Modifying: el:Ηλεκτρικό κύκλωμα; cosmetic changes
Rëdd 1 :
[[ImageDencukaay:Real current source.png|thumb|350px|ag Ndombo gu mbëj]]
 
'''Ndombo gu mbëj''' dees koy tekkkee niki lëkkalante gu ay cëri mbëj ci wenn yoon wu tëju ci genn anam guy tax ba dawaanu mbëj ga cay jaar di man a wéy di wal, maanaan du am benn dog-dog.
Rëdd 11 :
Manees naa gëstu ag ndombo ak yii àtte:
 
* [[Àtteb ohm]]: moo nuy xamal dayoob dend '''U''' bi ci ag ndëgërlu '''R''' gu dawaan '''I''' jaar ci biiram: '''U = RI'''.
 
* [[Àtteb Kirchhoff]] mooy lay jox jëflante bi ci cër yu wuute yu ndombo gi.
 
* [[Soppalig ñettikoñ-biddiw]]
 
* [[Soppalig biddiw-ñettikoñ]]
 
* [[Céetu Norton]]: mooy wax ne gépp ndombo gu ndëgërlu (ndombo gu ami ndëgërlu rekk) dafay yam ak ab jurukaayu dawaan ''I'' bu lang ak ag ndëgërlu ''R''.
 
* [[Céetu Thevenin]]: mooy wax ne sooy xoolee ag ndombo gu mbëj ci ñaari tomb, yu nekk ci ndombo gi, dafay yam ak ab jurukaay bu dendam tollook wuuteeg aj gi ngay natt ci diggante ñaari tomb yi, toppanteeg ag ndëgërlu gu yam ak gi ngay natt ci diggante ñaari tomb yi batay su jurukaay yu temb yi fayee.
 
== Noste gu jàllu ==
Rëdd 28 :
== Noste gu sin ==
Ci gii noste ndombo gi [[dawaan bu safaanu]] lañu koy dundale. Àtte yees bind ci kaw yépp manees na leen fee jëfandikoo batay, waaye ak coppite yi ci war.
 
[[Wàll:mbëjMbëj]]
 
[[ar:دائرة كهربائية]]
Ligne 38 ⟶ 39 :
[[da:Elektronisk kredsløb]]
[[de:Elektrische Schaltung]]
[[el:Ηλεκτρικό κύκλωμα]]
[[el:Κύκλωμα]]
[[en:Electrical network]]
[[eo:Elektra cirkvito]]