Kureelu Mbootayu Xeet yi wuute gi ci sumb yi

4 octets supprimés ,  10 at ci ginaaw
m (r2.6.2) (robot Adding: lad:Nasyones Unidas)
 
=== Koolute gi (secretariat) ===
[[Dencukaay:Siège Nations Unies New York.JPG|thumb|200px|right|TaaxikawTaax biymiy makkaanu Koolute gi]]
Koolute gu kureelug gi, mi ngi sosoo woon ci liggéeykat yu kureel bi, ya daa liggéeye ca dalam bu sax ba nekkoon [[Geneve]]. Njiit li moom moo daa doon Ku-nu-woolu ku matale, ki nga xam ne jataay bu matale bi moo ko daa tànn. Koolute gi nag amoon na ay kureel yu bari yu aju woon ci moom, ñooy: kureelug dimblanteg caada gi , kureelug jële fi ag njaam, kureelug xeex seneebar, kureelug aar neewte yi , kureelug féetale yu sax yi ak kureelug tawat yu bon yi.
 
2 337

modifications