Leopool Sedaar Sengoor wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Luckas-bot (waxtaancëru)
m r2.7.1) (robot Adding: eu:Léopold Sédar Senghor
Guérin Nicolas (waxtaancëru)
Rëdd 12 :
 
Waaye ñaari gaa yii mujj nañu wuute ci lu gaaw. Ci desambar 1962 lañu jàpp Mamadu Ja, mi ñu tuumal ne day xiirtale cig daaneel nguur, mu daal di sax ci kaso bi lu tollook fukki at ak ñaar. Ginnaaw bi Sengoor daal di taxawal ag noste gu njiit (système présidentiel). Ci 22 Mars 1967 Sengoor mucc na cig bóom, ñu daal di teg àtteb ray ci ki ñu ko tuumaaloon.
Tekki na ndombag tànkam njëkk ab àppub njiitam di jeex, loola di ci desambar 1980, daal di fiy wuutal Abdu Juuf ci boppu réew mi. Ci ron ag njiitam la Sengoor sampe lëwug làng (multipartisme)( ñu yamale woon ko ci ñatti dawaan rekk: [[mbokkoo]] (socialisme), [[mbokkte]] (communisme), ak [[afal]] (libéralisme) ak genn noste gu yar ( systeme educatif) gu am solo.
 
Bariwaa na lu ñuy askanale Sengoor ag demokaraasi waaye ay fen rekk la,ndax moom indi woon na fi ci doole ag noste gu genn làng, daal di moñoxe ci doole lu sakkan ci ay yëngu-yëngu yu ñaxtu yu ay dongo (étudiants.
Ak doonte canc gu Faraas jeex na ci melo wu kilifawu (officiel) teewul xiimay koppar bu Senegaal Faraas a koy saxal, njàng mi it ci làkku Faraas lañu koy defe, te Sengoor it réew mi mi ngi ko jiite woon ànd ak ay xelalkat yu Faraas yu muy diisool, (Ñooñu nag manuñoo joxe menn xel mu njariñul Faraas nekkul, Moom itam jabari Faraas la yoroon, te bari na lool lu mu daa xeex ngir ñu yor aaday [[Faraas]], Taalifkat ba nee na:
 
* '''(Màggat mu màggat ci am () njàngum tubaab jabaroo () tubaab tubaab la, tubaab ngeen dénk seen gaal gii)
'''.
 
[[Wàll:niti senegaal]]