Dawaan bu safaanu wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
'''Dawaan bu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
== Doxiin ==
Naka-jekk dawaanu [[mbëj]] suñu koy séddale, ci dawaan bu safaanu bu [[Baraay|baraayam]] sax ci 50 Hz walla 60 [[Hz]] lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne). Dawaan bi ak [[dendu mbëj]] bi, ci biir [[watatukaayu mbëj]] bi, seen DemiinuDemiin dafay mel ne bu ab [[duusub sin]].
 
Jëfandikoo gu dawaan bu safaanu mi gi jóge ci li [[Jurukaay|jurukaayu dawaan]] yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan bu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan bi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.
Rëdd 14 :
 
== Taariix ==
[[Dencukaay:WorldMap Voltage&Frequency.png|400px|thumb|right|Lonkoyoonu àdduna bi bees melool aju ci taraay aak baraayu kàttanu mbëj ci ndombo yiy séddale dawaan gibi ci kër yi.]]
 
Ca njalbeenu njëfandikug kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIX<sup>u</sup> xarnu [[daawaan bu wéy]] lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy [[tegle]] ak li mu gën a wóor dawaan bu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon [[xareeb dawaan yi]].