Dawaan bu safaanu wuute gi ci sumb yi

2 octets supprimés ,  10 at ci ginaaw
Coppite gi amul tënk
Jëfandikoo gu dawaan bu safaanu mi gi jóge ci li [[Jurukaay|jurukaayu dawaan]] yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan bu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan bi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.
 
Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan bu safaanu bir na ne moo gën a yaxan [[dawaan bu wéy]] ci séddaleeb [[taraaydend bu kawe]] (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu [[gennwéq]] walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu [[ñettiwéq]] di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu [[Joule]] (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan bu safaanu bu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd lool yi.
 
Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan bu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoo fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci [[taraay]]u [[dawaan]], ci ndimbalu [[soppalikaay]] yi, ak ñakkug kàttan gu digu.
3 292

modifications